Results for verstand translation from Afrikaans to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Afrikaans

Wolof

Info

Afrikaans

toe open hy hulle verstand om die skrifte te verstaan.

Wolof

noonu mu ubbi seen xel, ngir ñu xam li mbind mi di wax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

maar jesus sê: is julle dan ook nog sonder verstand?

Wolof

noonu yeesu ne ko: «ndax ba tey seen xol dafa tëju, yéen itam?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en almal wat hom gehoor het, was verbaas oor sy verstand en sy antwoorde.

Wolof

Ñépp ñi dégg li mu wax yéemu ci xel, mi mu àndal, ak ni mu doon tontoo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

want as ek in 'n taal bid, dan bid my gees, maar my verstand is onvrugbaar.

Wolof

su may ñaan yàlla ci aw làkk, sama xol day ñaan, waaye sama xel amalul kenn njariñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

hier kom die verstand wat wysheid het, te pas. die sewe koppe is sewe berge waar die vrou op sit.

Wolof

«xam lii nag moo laaj xel. juróom-ñaari bopp ya ñooy juróom-ñaari tund, yi jigéen ji toog ci seen kaw. juróom-ñaari buur lañu itam:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

broeders, moenie kinders wees in die verstand nie, maar wees kinders in die boosheid en wees volwassenes in die verstand.

Wolof

bokk yi, buleen melati ni ay xale, ci ni ngeen di xalaate. ci lu jëm ci lu bon, mel-leen ni ay xale, waaye ci seeni xalaat, mel-leen ni ay mag.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en jy moet die here jou god liefhê uit jou hele hart en uit jou hele siel en uit jou hele verstand en uit jou hele krag. dit is die eerste gebod.

Wolof

kon nanga bëgg yàlla sa boroom ak sa xol bépp ak sa bakkan bépp, sa xel mépp ak sa kàttan gépp.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

nuttelose stryery van mense wat verdorwe in hulle verstand en van die waarheid beroof is en dink dat die godsaligheid winsgewend is. onttrek jou aan sulke mense.

Wolof

ak ŋaayoo; ñiy jëfee noonu nit ñu ñaaw xel lañu, ñu xamul genn dëgg te yaakaar ne, ragal yàlla buntu wërsëg la.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

daarom, omgord die lendene van julle verstand, wees nugter en hoop volkome op die genade wat julle deel word by die openbaring van jesus christus.

Wolof

kon fagaruleen ci seeni xalaat te maandu, di wékk seen yaakaar jépp ci yiw, wi leen yàlla di jagleel bés bu yeesu kirist di feeñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

alle dinge is rein vir die reines; vir die besoedeldes en ongelowiges egter is niks rein nie, maar hulle verstand sowel as hulle gewete is besoedel.

Wolof

Ñi sell seen lépp a sell, waaye ñi selladi te gëmadi seen dara sellul, du seeni xalaat, du seeni xel.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en net soos jannes en jambres moses teëgestaan het, so staan ook hierdie mense die waarheid teë, mense verdorwe in die verstand, onbetroubaar ten opsigte van die geloof.

Wolof

nit ñooñu dañuy bëreek dëgg, ni sànnes ak sàmbares bëree woon ak musaa; ay boroom xel yu gumba lañu, yu seen ngëm tekkiwul dara.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en hy antwoord en sê: jy moet die here jou god liefhê uit jou hele hart en uit jou hele siel en uit jou hele krag en uit jou hele verstand; en jou naaste soos jouself.

Wolof

nit ka ne ko: « “nanga bëgg yàlla sa boroom ak sa xol bépp ak sa bakkan bépp, sa kàttan gépp ak sa xel mépp,” te it: “nanga bëgg sa moroom, ni nga bëgge sa bopp.”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en ons weet dat die seun van god gekom het en ons verstand gegee het om die waaragtige te ken; en ons is in die waaragtige, in sy seun, jesus christus. hy is die waaragtige god en die ewige lewe.

Wolof

xam nanu ne, doomu yàlla ji ñëw na te may na nu xel, ba nu man a xam aji wóor ji. te nu ngi ci aji wóor ji ak ci doomam yeesu kirist. kooku mooy yàlla ju wóor, ji yor dund gu dul jeex.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

hier kom die wysheid te pas. wie die verstand het, laat hom die getal van die dier bereken, want dit is die getal van 'n mens; en sy getal is ses honderd ses en sestig.

Wolof

lii nag mooy laaj xel: ku am xel dina man a waññ siifaru rab wi, ndaxte siifar boobu mengoo na ak bu nit, di juróom-benni téeméer ak juróom-benn-fukk ak juróom-benn.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

daarop het hulle uitgegaan om te sien wat gebeur het; en hulle het by jesus gekom en die man gevind uit wie die duiwels uitgevaar het, terwyl hy aan die voete van jesus sit, gekleed en by sy verstand. en hulle het gevrees.

Wolof

nit ñi génn, ngir seet li xew. bi ñu agsee ca yeesu, ñu fekk fa nit, ka rab ya bàyyi woon, toog ca kanam yeesu, sol ay yére te ànd ak sagoom. Ñu daldi ragal.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,727,029,523 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK