Results for portent translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

tandis que les anges, supérieurs en force et en puissance, ne portent pas contre elles de jugement injurieux devant le seigneur.

Wolof

fekk sax malaaka, yi leen ëpp doole ak kàttan, tey sax ca jetaayu boroom bi, ñemewuñoo xas kilifa yooyu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ce que jésus ayant entendu, il dit: ce ne sont pas ceux qui se portent bien qui ont besoin de médecin, mais les malades.

Wolof

waaye bi ko yeesu déggee, mu ne: «Ñi wér soxlawuñu fajkat, ñi wéradi ñoo ko soxla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ils font toutes leurs actions pour être vus des hommes. ainsi, ils portent de larges phylactères, et ils ont de longues franges à leurs vêtements;

Wolof

dañuy def seeni jëf yépp, ngir nit ñi gis leen, di takk ay téere yu réy, tey réyal seeni laari mbubb.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ce qui est tombé dans la bonne terre, ce sont ceux qui, ayant entendu la parole avec un coeur honnête et bon, la retiennent, et portent du fruit avec persévérance.

Wolof

ki jot ci jiwu wi ci suuf su baax si nag, mooy ki dégg kàddu gi te denc ko ci xol bu baax bu gore, te muñ ba jur njariñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ce que jésus ayant entendu, il leur dit: ce ne sont pas ceux qui se portent bien qui ont besoin de médecin, mais les malades. je ne suis pas venu appeler des justes, mais des pécheurs.

Wolof

noonu yeesu dégg ko, mu ne leen: «Ñi wér soxlawuñu fajkat, ñi wéradi ñoo ko soxla; ñëwuma woo ñi jub, waaye bàkkaarkat yi laay woo.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ce qui est tombé parmi les épines, ce sont ceux qui, ayant entendu la parole, s`en vont, et la laissent étouffer par les soucis, les richesses et les plaisirs de la vie, et ils ne portent point de fruit qui vienne à maturité.

Wolof

ki jot ci jiwu wi ci xaaxaam yi mooy ki dégg kàddu gi, waaye nes tuuti soxla yi ak alal ak bànneexi àddina tanc ko, ba du àgg cig mat.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,739,730,224 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK