Results for ascoltano translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

le mie pecore ascoltano la mia voce e io le conosco ed esse mi seguono

Wolof

samay xar dinañu dégg sama baat; xam naa leen te ñu ngi may topp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

il guardiano gli apre e le pecore ascoltano la sua voce: egli chiama le sue pecore una per una e le conduce fuori

Wolof

wottukat bi dina ko ubbil bunt bi, xar yiy dégg baatam. xar yi mu moom nag, bu ci nekk dina la woo ci sa tur, ba noppi nga topp ko ci biti.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

perché non coloro che ascoltano la legge sono giusti davanti a dio, ma quelli che mettono in pratica la legge saranno giustificati

Wolof

kon déglu yoonu musaa rekk doyul; du loolu mooy tax nit jub ci kanam yàlla; kiy sàmm yoon wi, moom la yàlla di àtte ni ku jub.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

abramo rispose: se non ascoltano mosè e i profeti, neanche se uno risuscitasse dai morti saranno persuasi»

Wolof

waaye ibraayma tontu ko ne: “su ñu dégluwul musaa ak yonent yi, kon ku dekki sax, du tax ñu gëm.”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

beato chi legge e beati coloro che ascoltano le parole di questa profezia e mettono in pratica le cose che vi sono scritte. perché il tempo è vicino

Wolof

barkeel ngeen, yaw miy jàng ak yéen ñiy déglu wax yii jóge ca yàlla, te di sàmm li ñu ci bind, ndaxte waxtu wi jege na.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ma egli rispose: «mia madre e miei fratelli sono coloro che ascoltano la parola di dio e la mettono in pratica»

Wolof

waaye mu daldi leen ne: «sama yaay ak samay rakk, ñooy ñiy déglu kàddug yàlla, te di ko topp.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

nessuna parola cattiva esca più dalla vostra bocca; ma piuttosto, parole buone che possano servire per la necessaria edificazione, giovando a quelli che ascoltano

Wolof

bu genn kàddu gu ñaaw génn ci seen gémmiñ, waaye su wax yegsee, nangeen wax lu rafet, ba faj soxlay seeni moroom, te teg ñi leen di déglu ci yoonu yiw.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

quelli lungo la strada sono coloro nei quali viene seminata la parola; ma quando l'ascoltano, subito viene satana, e porta via la parola seminata in loro

Wolof

ki féete ci yoon wi mooy ki dégg, seytaane ñëw ci saa si, këf kàddu, gi ñu def ci moom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e paolo: «per poco o per molto, io vorrei supplicare dio che non soltanto tu, ma quanti oggi mi ascoltano diventassero così come sono io, eccetto queste catene!»

Wolof

pool tontu ko: «muy tey, muy ëllëg, waxuma yaw rekk waaye it ñi may déglu tey ñépp, na yàlla def, ba ngeen fekksi ma ci li ma nekk, lu moy jéng yii!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

quelli poi che ricevono il seme su un terreno buono, sono coloro che ascoltano la parola, l'accolgono e portano frutto nella misura chi del trenta, chi del sessanta, chi del cento per uno»

Wolof

ki jot kàddu gi ci suuf su baax si nag, mooy ki ko dégg te nangu ko, ba jariñ; kii mat fanweeri yoon lu ëpp la ñu ji woon, kii mat juróom-benn-fukk, kii mat téeméer.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,745,115,209 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK