Results for viaggio translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

durante il viaggio verso gerusalemme, gesù attraversò la samaria e la galilea

Wolof

bi muy dem yerusalem ba tey, yeesu jaar ci dig wiy xaajale samari ak galile.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

se ne ritornava, seduto sul suo carro da viaggio, leggendo il profeta isaia

Wolof

mu toog ci watiiram, di jàng téereb yonent yàlla esayi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

perché è giunto da me un amico da un viaggio e non ho nulla da mettergli davanti

Wolof

dafa am sama xarit bu ma ganesi, te awma dara lu ma ko jox.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

in quei giorni maria si mise in viaggio verso la montagna e raggiunse in fretta una città di giuda

Wolof

ci jamono jooju maryaama jóg, gaawantu dem ci benn dëkk bu nekkoon ca tund ya ca diiwaanu yude.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

avverrà come di un uomo che, partendo per un viaggio, chiamò i suoi servi e consegnò loro i suoi beni

Wolof

«te it nguuru yàlla dafa mel ni kuy tukki bitim réew. bi mu laata dem, mu woo ay surgaam, batale leen alalam, ku nekk lu mu àttan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

credendolo nella carovana, fecero una giornata di viaggio, e poi si misero a cercarlo tra i parenti e i conoscenti

Wolof

Ñu xalaat ne, yeesu dafa àndoon ak ñeneen, ñi ñu bokkaloon yoon. bi ñu doxee bésub lëmm, ñu tàmbali di ko seet ci seen bokk yi ak seen xame yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

pietro allora li fece entrare e li ospitò. il giorno seguente si mise in viaggio con loro e alcuni fratelli di giaffa lo accompagnarono

Wolof

ci kaw loolu piyeer dugal leen, dalal leen. ba bët setee, piyeer jóg, dem ak ñoom, ànd ak ñenn ci bokk yi dëkk yope,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e avvenne che, mentre era in viaggio e stava per avvicinarsi a damasco, all'improvviso lo avvolse una luce dal ciel

Wolof

waaye bi muy jub damas, ca saa sa leer gu jóge asamaan melax, ba ëmb ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

appena cessato il tumulto, paolo mandò a chiamare i discepoli e, dopo averli incoraggiati, li salutò e si mise in viaggio per la macedonia

Wolof

bi yengu-yengu ba dalee, pool woo taalibe ya fa moom, dooleel leen. bi mu ko defee mu tàggoo ak ñoom, jóge fa, dellu diiwaanu maseduwan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

né bisaccia da viaggio, né due tuniche, né sandali, né bastone, perché l'operaio ha diritto al suo nutrimento

Wolof

buleen wut it mbuus ngir tukki mbaa ñaari turki, ay dàll mbaa aw yet, ndaxte liggéeykat yeyoo na dundam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e ordinò loro che, oltre al bastone, non prendessero nulla per il viaggio: né pane, né bisaccia, né denaro nella borsa

Wolof

mu digal leen nii: «bu ngeen di dem, buleen yóbbaale dara; du mburu mbaa mbuus mbaa xaalis ci seeni maxtume, waaye yemleen ci aw yet rekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora barnaba lo prese con sé, lo presentò agli apostoli e raccontò loro come durante il viaggio aveva visto il signore che gli aveva parlato, e come in damasco aveva predicato con coraggio nel nome di gesù

Wolof

ci kaw loolu barnabas jël ko, yóbbu ko ca ndaw ya, nettali leen, ni sool gise boroom bi ci kaw yoon wi, ak li mu ko wax, rax-ca-dolli fit wi mu doon waxe ci turu yeesu ci damas.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

disse loro: «non prendete nulla per il viaggio, né bastone, né bisaccia, né pane, né denaro, né due tuniche per ciascuno

Wolof

mu ne leen: «bu ngeen di dem, buleen yóbbaale dara, du yet mbaa mbuus mbaa mburu mbaa xaalis. buleen yor it ñaari turki.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ma quando furon passati quei giorni, uscimmo e ci mettemmo in viaggio, accompagnati da tutti loro con le mogli e i figli sin fuori della città. inginocchiati sulla spiaggia pregammo, poi ci salutammo a vicenda

Wolof

moona bi jataayu gaal ga matee, nu awaat ci yoon wi. te ñépp gunge nu, ñoom ak seeni jabar ak seeni doom; nu génn dëkk ba, sukk ca tefes ga, ñaan ci yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

mentre erano in viaggio per salire a gerusalemme, gesù camminava davanti a loro ed essi erano stupiti; coloro che venivano dietro erano pieni di timore. prendendo di nuovo in disparte i dodici, cominciò a dir loro quello che gli sarebbe accaduto

Wolof

gannaaw loolu ñu ànd jëm yerusalem, yeesu jiitu; taalibe yi am njàqare, te ñi ci topp tiit. noonu yeesu woowaat fukk ak ñaar ña cig wet, xamal leen li nar a xew ci mbiram.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

viaggi innumerevoli, pericoli di fiumi, pericoli di briganti, pericoli dai miei connazionali, pericoli dai pagani, pericoli nella città, pericoli nel deserto, pericoli sul mare, pericoli da parte di falsi fratelli

Wolof

ci sama tukki yu bare yi daan naa faral di daje ak musiba ci dex yi, ak musiba ci sàcc yi, musiba mu jóge ci sama xeet walla ci ñi dul yawut, musiba ci biir dëkk yi, ci màndiŋ yi, ci géej gi, ci biir bokki taalibe yu naaféq yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,713,305,146 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK