Results for manete translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

et in quamcumque domum intraveritis ibi manete et inde ne exeati

Wolof

kër gu ngeen dugg, dal-leen fa, ba kera ngeen di fa jóge.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

sicut dilexit me pater et ego dilexi vos manete in dilectione me

Wolof

«ni ma baay bi bëggee, noonu itam laa leen bëgge. saxleen ci mbëggeel googu ma am ci yéen.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et dicebat eis quocumque introieritis in domum illic manete donec exeatis ind

Wolof

mu ne leen: «kër gu ngeen dugg, dal-leen fa, ba kera ngeen jóge dëkk ba.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et nunc filioli manete in eo ut cum apparuerit habeamus fiduciam et non confundamur ab eo in adventu eiu

Wolof

gannaaw loolu nag yéen samay doom, saxleen ci kirist, ngir bés bu feeñee, nu am kóolute ci kanamam te bañ a rus ba sëngéem cig dikkam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

in eadem autem domo manete edentes et bibentes quae apud illos sunt dignus enim est operarius mercede sua nolite transire de domo in domu

Wolof

dal-leen ca kër googa, tey lekk ak a naan lu ñu leen di jox, ndaxte liggéeykat yelloo na jot peyam. buleen dem nag kër ak kër.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

cum autem baptizata esset et domus eius deprecata est dicens si iudicastis me fidelem domino esse introite in domum meam et manete et coegit no

Wolof

ci kaw loolu ñu sóob ko ci ndox, moom ak waa këram, ba noppi mu ñaan nu ne: «bu ngeen ma jàppee ni ku takku ci boroom bi, ganesileen ma ci sama kër.» te mu di nu ci xiir.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et vos unctionem quam accepistis ab eo manet in vobis et non necesse habetis ut aliquis doceat vos sed sicut unctio eius docet vos de omnibus et verum est et non est mendacium et sicut docuit vos manete in e

Wolof

yéen nag, xel mi leen kirist sol a ngi dëkk ci yéen, te soxlawuleen kenn jàngal leen dara. waaye xel mi mu leen sol, mi ngi leen di jàngal lépp, te li mu leen di jàngal mooy dëgg; kon nag saxleen ci moom, ni mu leen ko jàngale.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,746,957,500 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK