Results for stellarum translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

alia claritas solis alia claritas lunae et alia claritas stellarum stella enim ab stella differt in claritat

Wolof

jant bi, weer wi ak biddiiw, lu nekk ak sag leer. te it leeru biddiiw bu nekk dina wuute ak moroomam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et signum magnum paruit in caelo mulier amicta sole et luna sub pedibus eius et in capite eius corona stellarum duodeci

Wolof

amoon na firnde ju ràññiku ju feeñ ca asamaan, di jigéen ju làmboo jant bi, kaalawoo fukki biddiiw ak ñaar, weer wi nekk ci suufu tànkam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et cauda eius trahebat tertiam partem stellarum caeli et misit eas in terram et draco stetit ante mulierem quae erat paritura ut cum peperisset filium eius devorare

Wolof

geenam di laawaale ñetti cér yu ne benn ca biddiiwi asamaan, di leen sànni ci suuf. ninkinànka ja taxaw ca kanamu jigéen jay matu, ngir lekk liir ba, bu juddoo.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et quartus angelus tuba cecinit et percussa est tertia pars solis et tertia pars lunae et tertia pars stellarum ut obscuraretur tertia pars eorum et diei non luceret pars tertia et nox similite

Wolof

Ñeenteelu malaaka ma wol liitam. noonu dóorees benn ci ñetti xaaju jant bi, ak benn ci ñetti xaaju weer wi, ak benn ci ñetti xaaju biddiiw yi, ba tax benn ci ñetti xaaju leer gi lëndëm. bëccëg bi ñàkk leer diirub benn ci ñetti xaajam, guddi gi ñàkk leer diirub benn ci ñetti xaajam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,748,627,312 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK