Results for alitaka translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

barnaba alitaka wamchukue pia yohane aitwaye marko.

Wolof

barnabas nag bëggoon na yóbbaale yowaana, mi ñuy wax it màrk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

pilato alitaka kumwachilia yesu, hivyo akasema nao tena;

Wolof

pilaat waxaat ak mbooloo ma, ndaxte dafa bëggoon a bàyyi yeesu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, wakamwashiria baba yake wapate kujua alitaka mtoto wake apewe jina gani.

Wolof

Ñu daldi liyaar baayam, ngir xam nan la bëgg ñu tudde xale ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

paulo mwenyewe alitaka kuukabili huo umati wa watu, lakini wale waumini walimzuia.

Wolof

pool nag bëgg a dugg ca mbooloo ma, waaye taalibe ya nanguwuñu ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

herode alitaka kumwua yohane, lakini aliogopa watu kwa sababu kwao yohane alikuwa nabii.

Wolof

erodd nag bëgg koo rey, waaye dafa ragal nit ñi, ci li ñu teg yaxya ab yonent.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

"simoni, simoni! sikiliza! shetani alitaka kuwapepeta ninyi kama mtu anavyopepeta ngano.

Wolof

yeesu teg ca ne: «simoŋ, simoŋ! seytaane ñaan na, ñu jébbal leen ko, ngir mu teqale leen ni ñu teqalee dugub ak xatax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

alitaka pia kudhihirisha wingi wa utukufu wake ambao alitumiminia sisi tulio lengo la huruma yake; sisi ambao alikwisha kututayarisha kuupokea utukufu wake.

Wolof

bëggoon na it xamle màggaayam mu ëpp xel, ci boole ñi mu yërëm ci ndamam; moo tax mu tànn leen ca njàlbéen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini kwa vile yule ofisajeshi alitaka kumwokoa paulo, aliwazuia wasifanye hivyo. aliamuru wale waliojua kuogelea waruke kutoka melini na kuogelea hadi pwani,

Wolof

waaye njiit la bëgg a musal pool, mu tere leen pexe ma. mu sant ñi man a féey, ñu jëkk a sóobu ca ndox ma, ba jot tefes ga.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

baada ya hayo, bwana aliwachagua wengine sabini na wawili, akawatuma wawiliwawili, wamtangulie katika kila kijiji na mahali ambapo yeye mwenyewe alitaka kwenda.

Wolof

gannaaw loolu boroom bi tànn na yeneen juróom-ñaar-fukki taalibe ak ñaar, yebal leen, ñu ànd ñaar ak ñaar, jiituji ko ca dëkk yépp ak ca bérab yépp, ya mu naroon a dem moom ci boppam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

baada ya miaka miwili, porkio festo alichukua nafasi ya felisi, akawa mkuu wa mkoa. kwa kuwa alitaka kujipendekeza kwa wayahudi, felisi alimwacha paulo kizuizini.

Wolof

bi ñaari at weesoo nag, amoon na ku wuutu feligsë, tudd porsiyus festus. noonu feligsë, mi bëggoon lu neex yawut ya, bàyyi pool ca kaso ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, akawaona wanafunzi wake wakitaabika kwa kupiga makasia, maana upepo ulikuwa unawapinga. karibu na mapambazuko, yesu aliwaendea akitembea juu ya maji. alitaka kuwapita.

Wolof

booba mu gis taalibe yi sonn lool ci joow gaal gi ndax li leen ngelaw li soflu. ca njël nag mu jëm ci ñoom, di dox ci kaw dex gi, ba xaw leen a raw.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

hivyo ndivyo ilivyo kwa mungu. alitaka kuonyesha ghadhabu yake na kujulisha uwezo wake, basi, alikuwa na saburi sana, akiwavumilia wale ambao walikuwa lengo la ghadhabu yake, ambao walistahili kuangamizwa.

Wolof

kon nag looy wax ci lii: yàlla bëggoon na wone meram, xamle it dooleem ci àddina; teewul dafa sax ci muñal ñi yelloo meram te taxaw ci sànku.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kesho yake, mkuu wa jeshi alitaka kujua mashtaka kamili ambayo wayahudi walikuwa wamemwekea paulo. hivyo, alimfungua paulo minyororo, akaamuru makuhani wakuu na baraza lote wafanye kikao. kisha alimleta paulo, akamsimamisha mbele ya baraza.

Wolof

ca ëllëg sa mu bàyyi ko, ndaxte bëggoon na xam bu wóor lu ko yawut ya jiiñ. mu santaane ne, saraxalekat yu mag ya dajaloo, ñoom ak kureelu àttekat ya. gannaaw loolu mu indilu pool, dëj ko ci seen kanam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,726,956,622 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK