Results for fulani translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

kama mkifika mji fulani na watu wakiwakaribisha, kuleni wanavyowapeni.

Wolof

«dëkk bu ngeen man a dugg, te waa dëkk ba teeru leen, lu ñu leen jox, lekkleen ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini ni lazima tutatupwa ufukoni mwa kisiwa fulani."

Wolof

waaye war nanoo luf cib dun.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

kila nyumba hujengwa na mjenzi fulani--na mungu ndiye mjenzi wa vitu vyote.

Wolof

ndaxte kër gu nekk am na ku ko sos, waaye ki sos lépp mooy yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

laiti mngenivumilia kidogo, hata kama mimi ni mjinga kiasi fulani! naam, nivumilieni kidogo.

Wolof

céy bu ngeen ma manoon a muñal, ma wax leen tuuti waxi dof! waaw muñal-leen ma sax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini ikiwa mimi sifahamu maana ya lugha asemayo mtu fulani, mimi ni mgeni kwake mtu huyo naye pia ni mgeni kwangu.

Wolof

su ma xamul nag làkk wi ñu may làkk, doxandéem laay doon ci ki koy wax, te ki koy wax it doxandéem la ci man.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

abrahamu aliamini kwamba mungu anaweza kuwafufua wafu: na kwa namna fulani kweli abrahamu alimpata tena mwanae kutoka wafu.

Wolof

waaye xelu ibraayma jàppoon na ne, yàlla am na dooley dekkal néew yi. te dëgg-dëgg ci misaal dafa mel ni, isaaxa dafa dee te dekki.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini nimewaandikia hapa na pale katika barua hii bila woga, nipate kuwakumbusheni juu ya mambo fulani. nimefanya hivyo kwa sababu ya neema aliyonijalia mungu

Wolof

bu sama kàddu diisee nag ci bataaxal bii, dara taxul lu dul bëgg a yeesal seen xalaat, ndaxte yàlla ci kaw yiwam daf maa sas,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

ingawa sisi tukiwa mitume wa kristo, tungeweza kudai mambo fulani kwenu. lakini sisi tulikuwa wapole kati yenu kama alivyo mama kwa watoto wake.

Wolof

manoon nanoo diis ci seen kaw sax, nun ñiy ndawi kirist, waaye woyofoon nanu ci seen biir, te lewet ni jaboot buy uuf doomam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

labda nitakaa kwenu kwa muda fulani, au huenda nitakaa pamoja nanyi wakati wote wa baridi, ili mpate kunisaidia niendelee na safari yangu kokote nitakakokwenda.

Wolof

man na am ma yàgg ci yéen, jombul sax ma lollikoo fi yéen. noonu dingeen taxawu sama yoon, fu ma man a jëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

mtu anaweza kufikiria siku fulani kuwa ya maana zaidi kuliko nyingine; mtu mwingine aweza kuzifikiria siku zote kuwa sawa. kila mmoja na afuate msimamo wa akili yake.

Wolof

noonu itam am na ñiy tànn bés ak ñiy yemale bés yépp. na ku nekk xam bu wér li muy def, te jàpp ci.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, wakawa wanatafuta wakati wa kufaa. wakawahonga watu fulani wajisingizie kuwa wema, wakawatuma wamnase yesu kwa maswali, na hivyo waweze kumtia nguvuni na kumpeleka kwa wakuu wa serikali.

Wolof

noonu ñu koy yeeru, daldi yónni ay nit ñu mbubboo njub, sas leen ñu fexe koo jàpp ci ay waxam, ngir jébbal ko boroom réew, ma yor kilifteef ak sañ-sañ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

"pepo mchafu akifukuzwa kwa mtu fulani, huzururazurura jangwani akitafuta mahali pa kupumzikia. asipopata, hujisemea: nitarudi kwenye makao yangu nilikotoka.

Wolof

«boo xamee ne rab, wa jàppoon nit, génn na ci moom, day wër ay bérab yu wow, di wut fu mu noppaloo, waaye du ko gis. noonu da naan: “naa dellu ca sama kër, ga ma jóge.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

"mwalimu, mose alituandikia kwamba kama ndugu ya mtu fulani akifa na kumwacha mjane wake bila watoto, ni lazima ndugu yake amchukue huyo mama mjane, amzalie watoto ndugu yake marehemu.

Wolof

«kilifa gi, musaa bindal na nu ne, ku magam faatu te bàyyiwul doom ak jabaram, kooku war na donn jigéen ji, ba yékkati giiru magam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

anayeadhimisha siku fulani anaadhimisha siku hiyo kwa ajili ya kumtukuza mungu; naye anayekula chakula fulani anafanya hivyo kwa kumtukuza bwana maana anamshukuru mungu. kadhalika naye anayeacha kula chakula fulani anafanya hivyo kwa ajili ya kumtukuza bwana, naye pia anamshukuru mungu.

Wolof

ndaxte kuy tànn bés, mu ngi koy def ngir màggal boroom bi. kiy lekk lu nekk it, mu ngi koy def ngir màggal boroom bi; loolu leer na ndax day sant yàlla. te it ki bañ a lekk yàpp, mu ngi koy def ngir màggal boroom bi, di ko sant.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

"au mwaonaje? tuseme mwanamke fulani ana sarafu kumi za fedha, akipoteza moja, atafanya nini? atawasha taa, aifagie nyumba na kuitafuta kwa uangalifu mpaka aipate.

Wolof

«te it bu jigéen dencoon fukki libidoor, benn réer ca, nu muy def? ndax du taal ab làmp, bale kër ga, seet fu nekk, ba gis ko?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,742,760,341 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK