Results for haliwezi translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

tumaini hilo haliwezi kutuhadaa, maana mungu amekwisha miminia mioyoni mwetu upendo wake kwa njia ya roho mtakatifu aliyetujalia.

Wolof

te yaakaar jooju du ay nax, ndax mbëggeelu yàllaa ngi baawaan ci sunu xol, jaarale ko ci xelam mu sell mi mu nu may.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kwa sababu ya kuihubiri habari njema mimi nateseka na nimefungwa minyororo kama mhalifu. lakini neno la mungu haliwezi kufungwa minyororo,

Wolof

xebaar booboo tax may jànkoonte ak i tiis, ba ñu jéng ma ni defkatu lu bon; waaye kàddug yàlla moom, kenn du ko jéng.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kaeni ndani yangu, nami nikae ndani yenu. tawi haliwezi peke yake kuzaa matunda lisipokaa katika mzabibu hali kadhalika nanyi hamwezi kuzaa matunda msipokaa ndani yangu.

Wolof

saxleen ci man; ma sax, man itam, ci yéen. ni car mënul a ame ay doom, bu saxul ci garab, noonu itam dungeen man a meññ li may jëfe ci yéen, bu ngeen saxul ci man.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, jicho haliwezi kuuambia mkono: "sikuhitaji wewe", wala kichwa hakiwezi kuiambia miguu: "siwahitaji ninyi."

Wolof

bët nag mënul ne loxo: «soxlawuma la!» te bopp it mënul ne tànk yi: «soxlawuma leen!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,747,780,858 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK