Results for mkamilifu translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

basi, muwe wakamilifu kama baba yenu wa mbinguni alivyo mkamilifu.

Wolof

nangeen mat nag, ni seen baay bi ci kaw mate.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

ili mtu anayemtumikia mungu awe mkamilifu, na tayari kabisa kufanya kila tendo jema.

Wolof

noonu waayu yàlla ji dina mat, ba jekk ci bépp jëf ju rafet.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini kama mtu hakosi katika usemi wake, basi, huyo ni mkamilifu, na anaweza kutawala nafsi yake yote.

Wolof

ndaxte nun ñépp sikk nanu ci fànn yu bare. ki sikkul ci kàddoom, ku mat nga, te man a noot sa yaram wépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

naomba ili imani hiyo unayoshiriki pamoja nasi ikuwezeshe kuwa na ujuzi mkamilifu zaidi wa baraka zote tunazopata katika kuungana kwetu na kristo.

Wolof

li may ñaan nag a ngi nii: nga xam bu wér ngëneel, yi nu am yépp ci sunu bokk ci kirist, ba tax bokk gi nga am ci yàlla ci kaw ngëm meññ i njariñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

sheria ya mose huwateua watu waliokuwa dhaifu kuwa makuhani wakuu; lakini ahadi ya mungu aliyoifanya kwa kiapo na ambayo imefika baada ya sheria imemteua mwana ambaye amefanywa mkamilifu milele.

Wolof

naka yoonu musaa, aji néew doole yi lay fal saraxalekat yu mag. waaye ngiñu yàlla gi ñëw gannaaw yoon wi, doom ji la fal saraxalekat bu mag bu mat ba fàww.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

ilikuwa haki tupu kwamba mungu, ambaye huumba na kutegemeza vitu vyote, alimfanya yesu kuwa mkamilifu kabisa kwa njia ya mateso, ili awalete watoto wengi waushiriki utukufu wake. maana yesu ndiye anayewaongoza kwenye wokovu.

Wolof

ndaxte yàlla mi yelloo lépp te sàkk lépp, dogal na def ñu bare ay doomam, boole leen ci ndamam. jekk na nag mu matal yeesu ci coono bi mu daj, moom mi leen xàllal yoonu mucc gi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,729,876,290 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK