Results for mmekuwa translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

nanyi pia mtanishuhudia kwa kuwa mmekuwa nami tangu mwanzo.

Wolof

te yéen itam dingeen seede samay mbir, ndaxte yéena nekkoon ak man ca njàlbéen ga.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kwa hiyo ninyi mmekuwa mfano mzuri kwa waumini wote wa makedonia na akaya.

Wolof

noonu ngeen daldi nekk royukaay ngir ñi gëm ñépp ci diiwaani maseduwan ak akayi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kwa njia ya imani, ninyi nyote mmekuwa watoto wa mungu katika kuungana na kristo.

Wolof

yéen ñépp doomi yàlla ngeen ndax li ngeen bokk ci kirist yeesu ci kaw ngëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

na mmekuwa mkiwatendea hivyo ndugu zenu wote kila mahali katika makedonia. basi, ndugu tunawaombeni mfanye hata zaidi.

Wolof

te moom ngeen di def ci bokk yépp, yi ci diiwaanu maseduwan. waaye bokk yi, maa ngi leen di xiirtal, ngeen gën cee sax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

sara kwa mfano alimtii abrahamu na kumwita yeye bwana. ninyi mmekuwa sasa binti zake kama mkitenda mema bila kuogopa tisho lolote.

Wolof

ni saarata déggale woon ibraayma, ba daan ko wooye «sang bi.» yéen nag, su ngeen dee def lu baax te bañ cee boole genn njàqare, kon mel na ni saarataa leen jaboote.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kila mtu amesikia juu ya utii wenu na hivyo mmekuwa sababu ya furaha yangu. nawatakeni muwe na hekima katika mambo mema, na bila hatia kuhusu mambo mabaya.

Wolof

waaye seen dégg ndigal bir na ñépp, ba sama xol sedd lool ci yéen. teewul nag damaa bëgg ngeen am xam-xam bu leer ci lu baax, te bañ a laal dara ci lu bon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

enyi wagalatia, mmekuwa wajinga kweli! ni nani aliyewaloga? habari juu ya kusulubiwa kwake yesu kristo ilielezwa waziwazi mbele ya macho yenu.

Wolof

yéen waa galasi, yéena ñàkk xel! ku leen fàbbi, gannaaw bi ma leen yégalee ci lu leer ni ñu daaje yeesu kirist ca bant ba?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini sasa, mmekwisha kombolewa kutoka utumwa wa dhambi na mmekuwa watumishi wa mungu; faida mliyo nayo sasa ni utakatifu, na matokeo yake ni uzima wa milele.

Wolof

waaye léegi yàlla goreel na leen ci kilifteefu bàkkaar, def leen ay jaamam, ba jural leen sell, jëme leen ci dund gu dul jeex.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

hatimaye, ndugu zangu, mmejifunza kutoka kwetu namna mnavyopaswa kuishi ili kumpendeza mungu. na kweli mmekuwa mnaishi hivyo. sasa tunawaombeni na kuwasihi kwa jina la bwana yesu mfanye vema zaidi.

Wolof

léegi nag bokk yi, jot ngeen ci nun, nan ngeen war a dunde ba neex yàlla, te moom ngeen di def. waaye ci turu boroom bi yeesu nu ngi leen di ñaan ak a dénk, ngeen gën koo feddali.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

hali kadhalika ninyi ndugu zangu: ninyi pia mmekufa kuhusu sheria kwa kuwa ninyi ni sehemu ya mwili wa kristo; sasa mmekuwa wake yeye aliyefufuliwa kutoka wafu ili tupate kuzaa matunda mema kwa ajili ya mungu.

Wolof

nii laa leen ko man a misaale, samay bokk; bi kirist deeyee, dangeen a deeyandoo ak moom, te noonu yoonu musaa wàcc leen. léegi nag yéena ngi ànd ak keneen, maanaam kirist mi dekki, ngir nu amal yàlla njariñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

haya, mmekwisha shiba! mmekwisha kuwa matajiri! mmekuwa wafalme bila ya sisi! naam, laiti mngekuwa kweli watawala, ili nasi pia tuweze kutawala pamoja nanyi.

Wolof

yéen suur ngeen xaat! woomle ngeen xaat! tàmbali ngeen di nguuru te agseegunu! céy ni ma bëgge, ngeen di nguuru, ba nu man a bokk ak yéen di nguuru!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,727,538,927 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK