Results for sivyo translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

nanyi wazazi, msiwachukize watoto wenu, la sivyo watakata tamaa.

Wolof

baay yi, buleen bundaxataal seeni doom, ngir bañ a jeexal seen xol.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

la sivyo, baada ya kuweka msingi na kushindwa kumaliza, watu watamcheka

Wolof

lu ko moy, su yékkatee fondamaa bi te mënu koo àggale, ñi koy gis dinañu ko ñaawal, naan ko:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini mama yake akasema, "la, sivyo, bali ataitwa yohane."

Wolof

waaye yaayam ne leen: «déedéet, yaxya lay tudd.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

kama akiwako mwenye kupenda amani, amani yenu itakaa naye, la sivyo, itawarudieni.

Wolof

bu fa nitu jàmm nekkee, seen yéene dina ko indil jàmm. lu ko moy, seen yéene dina dellusi ci yéen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

nawaambieni hakika sivyo; lakini nanyi, hali kadhalika, msipotubu, mtaangamia kama wao.

Wolof

maa ngi leen di wax ne, du dëgg. waaye su ngeen tuubul seeni bàkkaar, dingeen sànku noonu, yéen ñépp itam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini yeye akasema: sivyo baba abrahamu, ila kama mtu atafufuka kutoka wafu na kuwaendea, watatubu.

Wolof

boroom alal ja ne ko: “déedéet, maam ibraayma, waaye su kenn dekkee, dem ca ñoom, dinañu tuub seeni bàkkaar.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

inajulikana kwamba shomoro watano huuzwa kwa senti kumi, au sivyo? lakini mbele ya mungu hasahauliki hata mmoja.

Wolof

juróomi picci rammatu, ndax duñu ko jaay ci ñaari dërëm? moona yàlla fàttewul benn ci ñoom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, achana na madhambi yako. la sivyo, nitakuja kwako upesi na kupigana na watu hao kwa upanga utokao kinywani mwangu.

Wolof

réccul kon; lu ko moy dinaa dikk ci yaw léegi te xeex ak nit ñooñu ak jaasi, jiy génn ci sama gémmiñ. i

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

"jihadharini msije mkafanya matendo yenu mema mbele ya watu kusudi mwonekane nao. la sivyo, baba yenu aliye mbinguni hatawapeni tuzo.

Wolof

«wottuleen a def seeni jëf yu jub ci kanamu nit ñi, muy ngistal. lu ko moy, dungeen am yool ci seen baay bi nekk ci kaw.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

"muwe macho, mioyo yenu isije ikalemewa na anasa, ulevi na shughuli za maisha haya. la sivyo, siku ile itawajieni ghafla.

Wolof

«moytuleen seen nafsu diigal leen ci yàqute ak ci màndite ak ittey àddina, ba bés boobu bett leen ni mbaal.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

ili, watazame kweli, lakini wasione. wasikie kweli, lakini wasielewe. la sivyo, wangemgeukia mungu, naye angewasamehe."

Wolof

noonu la, ngir:“Ñuy xool bu baax waaye duñu gis dara,di déglu bu baax waaye duñu xam dara,ngir bañ ñu tuub seeni bàkkaar,te yàlla baal leen.”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, pakumbuke pale ulipokuwa kabla ya kuanguka, ukayaache madhambi yako, na kufanya kama ulivyofanya pale awali. la sivyo, naja kwako na kukiondoa kinara chako mahali pake.

Wolof

deel fàttaliku kon fa nga daanoo. réccul te def, na nga daan def bu jëkk. soo réccuwul, dinaa dikk ci yaw, jële sa làmp ca bérab ba mu nekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

jichunguzeni ninyi wenyewe mpate kujua kama kweli mnayo imani. jichunguzeni ninyi wenyewe. je, hamjui kwamba kristo yesu yumo ndani yenu? kama sivyo, basi ninyi mmeshindwa.

Wolof

xool-leen seen bopp bu baax, ba xam ndax ngëm a ngi ci yéen. seetluleen seen bopp. xanaa xamuleen ne, yeesoo ngi ci yéen? walla boog ngeen gis ne, ay naaféq ngeen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

"patana na mshtaki wako upesi mkiwa bado njiani, kwenda mahakamani. la sivyo, mshtaki wako atakukabidhi kwa hakimu, naye hakimu atakukabidhi kwa askari, nawe utafungwa gerezani.

Wolof

«gaawal a juboo ak ki lay yóbbu, ngeen layooji, bala ngeen a egg; ngir bañ ki ngay layool jébbal la àttekat ba, kooka jox la alkaati ba, ñu tëj la.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

halafu akamgeukia yule mwanamke na kumwambia simoni, "unamwona huyu mwanamke, sivyo? basi, mimi nilipoingia hapa nyumbani kwako hukunipa maji ya kunawa miguu yangu; lakini mwanamke huyu ameniosha miguu yangu kwa machozi yake na kunipangusa kwa nywele zake.

Wolof

daldi walbatiku ca jigéen ja, ne simoŋ: «ndax gis nga jigéen jii? dugg naa sa kër, te joxewuloo ndox, ngir raxas samay tànk. waaye moom, raxas na samay tànk ak ay rangooñam, ba noppi fomp leen ak kawaram.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,724,800,652 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK