Results for ulimwenguni translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

kama vile ulivyonituma ulimwenguni, nami pia nimewatuma wao ulimwenguni;

Wolof

ni nga ma yónnee àddina, noonu laa leen yónnee ci nit ñi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

wakati ningali ulimwenguni, mimi ni mwanga wa ulimwengu."

Wolof

ci bi may nekk àddina, maay leeru àddina.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

siombi uwatoe ulimwenguni, bali naomba uwakinge na yule mwovu.

Wolof

Ñaanuma nga jële leen àddina, waaye nga yiir leen ci ibliis.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

mimi ni mwanga, nami nimekuja ulimwenguni ili wote wanaoniamini wasibaki gizani.

Wolof

ni ag leer laa wàcce ci àddina, ngir ku ma gëm du des ci lëndëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

huu ndio mwanga halisi, mwanga unaokuja ulimwenguni, na kuwaangazia watu wote.

Wolof

kàddu googu mooy leer gu wóor, giy ñëw ci àddina te di leeral nit ku nekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, akawaambia, "nendeni ulimwenguni kote mkahubiri habari njema kwa kila mtu.

Wolof

mu ne leen: «demleen ci àddina sépp, yégal xebaar bu baax bi mbindeef yépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, neno alikuwako ulimwenguni; na kwa njia yake ulimwengu uliumbwa, lakini ulimwengu haukumtambua.

Wolof

ci àddina la nekkoon, àddina si ñu sàkk jaarale ko ci moom, te àddina xamu ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

mimi nilitoka kwa baba, nikaja ulimwenguni; na sasa nauacha ulimwengu na kurudi kwa baba."

Wolof

jóge naa ca baay bi, ñëw àddina. léegi maa ngi génn àddina, fekki baay bi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, sasa naja kwako, na nimesema mambo haya ulimwenguni, ili waweze kushiriki kikamilifu furaha yangu.

Wolof

«waaye léegi maa ngi jëmsi ci yaw, te maa ngi wax nii ci bi may nekk àddina, ngir ñu fees ak sama mbég.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kabla ya sheria kuwako, dhambi ilikuwako ulimwenguni; lakini dhambi haiwekwi katika kumbukumbu bila sheria.

Wolof

bàkkaar kon nekkoon na ci àddina, bi yàlla di laata wàcce yoonu musaa. waaye gannaaw yoonu musaa tëddagul woon, bàkkaar du woon jàdd yoon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

ila, kabla ya mwisho kufika, hii habari njema ya ufalme wa mungu itahubiriwa ulimwenguni kote kama ushuhuda kwa mataifa yote.

Wolof

noonu xebaar bu baax bii ci nguuru yàlla, dees na ko yégle ci àddina sépp, ngir mu nekk seede ci xeet yépp. bu loolu amee muju jamono ji jot.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

habari njema inazidi kuzaa matunda na kuenea ulimwenguni kote kama vile ilivyofanya kwenu ninyi tangu siku ile mliposikia juu ya neema ya mungu na kuitambua ilivyo kweli.

Wolof

ni xebaar bu baax bi wàcce ci yéen, noonu lay wàcce ci àddina sépp, di meññ te di law. te noonu lay doxale ci yéen, li dale ci bés, ba ngeen dégge xebaaru yiwu yàlla, te xam dëggam gi mu ëmb;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

ndiyo maana kristo alipokuwa anakuja ulimwenguni, alimwambia mungu: "hukutaka dhabihu wala sadaka, lakini umenitayarishia mwili.

Wolof

looloo tax bi muy wàcc àddina, kirist nee na:«bëggoo saraxu mala walla beneen sarax,waaye aw yaram nga ma defaral.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

lakini mungu alipokuwa anamtuma mwanae mzaliwa wa kwanza ulimwenguni, alisema: "malaika wote wa mungu wanapaswa kumwabudu."

Wolof

waaye bi muy yónni doom jooju di taaw bi ci àddina, da ne:«na ko malaakay yàlla yépp jaamu.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

kama mngalikuwa watu wa ulimwengu, ulimwengu ungaliwapenda ninyi kama watu wake. lakini kwa vile ninyi si wa ulimwengu, ila mimi nimewachagueni kutoka ulimwenguni, kwa sababu hiyo ulimwengu unawachukieni.

Wolof

Ñi bokk ci ñoom lañu bëgg. bu ngeen bokkoon ci ñoom, dinañu leen bëgg, ni ñu bëgge seeni ñoñ. waaye bokkuleen ci àddina, ndaxte maa leen tànn, ber leen. looloo tax ñu bañ leen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

je, yeye ambaye baba alimweka wakfu na kumtuma ulimwenguni, mnamwambia: unakufuru, eti kwa sababu nilisema: mimi ni mwana wa mungu?

Wolof

kon nu ngeen man a waxe ne, damay suufeel turu yàlla ndax li ma ne doomam laa, man mi yàlla tànn, yónni ma ci àddina?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

ilikuwa kabla ya sikukuu ya pasaka. yesu alijua kwamba saa yake ya kuondoka ulimwenguni na kwenda kwa baba ilikuwa imefika. alikuwa amewapenda daima watu wake walioko duniani; naam, aliwapenda mpaka mwisho!

Wolof

laata màggalu bésu jéggi ba la woon. yeesu xamoon na ne, waxtu wi mu war a génne àddina, dem ca wetu baay ba, jot na. ku bëgg ñoñam yi nekk ci àddina la, te bëgg na leen ba fa mbëggeel man a yem.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

hakuna mashaka yoyote juu ya ukuu wa siri ya dini yetu: alionekana katika umbo la kibinadamu alithibitishwa na roho kuwa ni mwadilifu, akaonekana na malaika. alihubiriwa kati ya mataifa, aliaminiwa popote ulimwenguni, akachukuliwa juu mbinguni katika utukufu.

Wolof

ci dëgg-dëgg ragal yàlla ëmb na mbóot yu xóot:ki wàcc, yor bindu nit,mu bir ne xelam jub na,te malaaka ya gis ko;xamlees na ko ci xeet yi,ñu gëm ko ci kaw suuf,te yàlla teeru ko ci ndamam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,727,883,074 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK