Results for juróomi translation from Wolof to English

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

English

Info

Wolof

Ñu lekkoon nag matoon na limu juróomi junniy góor.

English

and they that did eat of the loaves were about five thousand men.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

buur ba ne ko: “yaw, falul ci juróomi dëkk.”

English

and he said likewise to him, be thou also over five cities.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

juróomi yoon yawut yi dóor nañu ma fanweeri yar ak juróom-ñeent.

English

of the jews five times received i forty stripes save one.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gannaaw jigéen ña ak gune ya, góor ña doon lekk matoon nañu juróomi junni.

English

and they that had eaten were about five thousand men, beside women and children.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu ne ko: «amunu fi lu dul juróomi mburu ak ñaari jën.»

English

and they say unto him, we have here but five loaves, and two fishes.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu dajale ko, daldi feesal fukki pañe ak ñaar ak desiti juróomi mburu, yi ñu doon lekk.

English

therefore they gathered them together, and filled twelve baskets with the fragments of the five barley loaves, which remained over and above unto them that had eaten.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

surga ba ca topp ñëw ne: “sang bi, sa libidoor ba indi na juróomi libidoor.”

English

and the second came, saying, lord, thy pound hath gained five pounds.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte am naa fa juróomi rakk. na leen artu, ngir ñu bañ a ñëw ñoom itam ci bérabu metit wii.”

English

for i have five brethren; that he may testify unto them, lest they also come into this place of torment.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye ci ndajem mbooloom ñi gëm, wax juróomi baat yu am njariñ, ngir jàngal ñi ci des, moo ma gënal wax fukki junniy baat ciw làkk.

English

yet in the church i had rather speak five words with my understanding, that by my voice i might teach others also, than ten thousand words in an unknown tongue.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gannaawsi tey, bu juróomi nit bokkee genn kër, dinañu féewaloo. Ñett dinañu féewaloo ak ñaar ñi ci des, ñaar ñi féewaloo ak ñett ñooñu.

English

for from henceforth there shall be five in one house divided, three against two, and two against three.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

santuñu leen ñu rey leen, waaye ñu metital leen diirub juróomi weer. te metit woowu ñuy indi, temboo na ak metit wiy dal nit, bu ko jànkalaar fittee.

English

and to them it was given that they should not kill them, but that they should be tormented five months: and their torment was as the torment of a scorpion, when he striketh a man.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi loolu amee yeesu jël juróomi mburu yi ak ñaari jën yi, xool ci kaw, gërëm yàlla, ba noppi mu damm leen, jox taalibe yi, ngir ñu séddale ko mbooloo mi.

English

then he took the five loaves and the two fishes, and looking up to heaven, he blessed them, and brake, and gave to the disciples to set before the multitude.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu daldi ne taalibe ya: «na ñépp toog.» fekk ñax mu bare amoon ca bérab ba. noonu góor ñépp àgg suuf. waroon nañoo mat juróomi junni.

English

and jesus said, make the men sit down. now there was much grass in the place. so the men sat down, in number about five thousand.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye naka nun, gannaaw màggalu yawut, ga ñuy wax mburu ya amul lawiir, nu dugg gaal ci filib, def ci juróomi fan, fekksi leen torowas, nu am fa juróom-ñaari fan.

English

and we sailed away from philippi after the days of unleavened bread, and came unto them to troas in five days; where we abode seven days.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,740,034,483 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK