Results for defar translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

bi ko janq ya déggee, ñu jóg, defar seeni làmp.

French

alors toutes ces vierges se réveillèrent, et préparèrent leurs lampes.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu taalibe yi defar reeru jéggi ba, na leen yeesu waxe woon.

French

les disciples firent ce que jésus leur avait ordonné, et ils préparèrent la pâque.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bu ñëwee nag, mu fekk këram, ñu bale ko, defar ko ba lépp jekk.

French

et, quand il arrive, il la trouve balayée et ornée.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu dem, gis lépp, ni leen ko yeesu waxe woon. noonu ñu defar reer bi.

French

ils partirent, et trouvèrent les choses comme il le leur avait dit; et ils préparèrent la pâque.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndax du sama loxo moo defar yëf yooyu yépp?— moom la boroom bi doon wax.”

French

n`est-ce pas ma main qui a fait toutes ces choses?...

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«moona aji kawe ji du dëkk ci fu loxol nit defar; moom la ab yonent wax ne:

French

mais le très haut n`habite pas dans ce qui est fait de main d`homme, comme dit le prophète:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu pool seeti leen, te gannaaw ñoo bokk liggéey, maanaam di defar ay tànt, mu dal fa ñoom, ñuy liggéeyandoo.

French

et, comme il avait le même métier, il demeura chez eux et y travailla: ils étaient faiseurs de tentes.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu dina leen won néeg bu féete kaw, te yaa, ñu defar ko ba noppi. foofa ngeen koy defare.»

French

et il vous montrera une grande chambre haute, meublée: c`est là que vous préparerez la pâque.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte nit ku tudd demetirus, di tëggu xaalis buy defar nataali xaalis ngir màggal artemis, daan na ci jariñu lu bare, moom ak ay nawleem.

French

un nommé démétrius, orfèvre, fabriquait en argent des temples de diane, et procurait à ses ouvriers un gain considérable.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag, bu nu nekkee xeetu yàlla, warunoo gëm ne, yàlla mel na ni nataali wurus, xaalis mbaa doj yu nit defar ci xareñ mbaa xel.

French

ainsi donc, étant la race de dieu, nous ne devons pas croire que la divinité soit semblable à de l`or, à de l`argent, ou à de la pierre, sculptés par l`art et l`industrie de l`homme.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi yeesu demee ba ca kanam, mu gis saag doomu sebede, ak yowaana, mi mu bokkal ndey ak baay, ñu nekk ci gaal gi, di defar seeni mbaal.

French

Étant allé un peu plus loin, il vit jacques, fils de zébédée, et jean, son frère, qui, eux aussi, étaient dans une barque et réparaient les filets.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

piyeer ne ko: «ene, yeesu kirist faj na la; jógal te defar sa lal.» noonu mu daldi jóg ca saa sa.

French

pierre lui dit: Énée, jésus christ te guérit; lève-toi, et arrange ton lit. et aussitôt il se leva.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ngëm moo tax ba, bi yàlla yégalee nóoyin lu jiitu ci mbir yi dikkagul, mu ragal ba defar gaal ngir musal njabootam. ngëmam moo tax mu yey niti àddina, ba noppi jot njubte, li yàllay joxe ci kaw ngëm.

French

c`est par la foi que noé, divinement averti des choses qu`on ne voyait pas encore, et saisi d`une crainte respectueuse, construisit une arche pour sauver sa famille; c`est par elle qu`il condamna le monde, et devint héritier de la justice qui s`obtient par la foi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu da naan: “naa dellu ca sama kër, ga ma génne woon.” bu ñëwee nag, mu fekk kërug neen, ñu bale ko, defar ko ba lépp jekk.

French

alors il dit: je retournerai dans ma maison d`où je suis sorti; et, quand il arrive, il la trouve vide, balayée et ornée.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,729,206,378 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK