Results for déglu translation from Wolof to German

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

German

Info

Wolof

Ñi doon déglu daldi ne: «kon nag ku man a mucc?»

German

da sprachen, die das hörten: wer kann denn selig werden?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te nit ñépp dañu daan teel a xëy ca kër yàlla ga, di ko déglu.

German

und alles volk machte sich früh auf zu ihm, im tempel ihn zu hören.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ko nit ña fa nekkoon ñépp doon déglu, yeesu ne ay taalibeem:

German

da aber alles volk zuhörte, sprach er zu seinen jüngern:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dañoo ñëw ngir déglu ko, te it ngir mu faj leen. Ñi rab jàpp it faju nañu.

German

die da gekommen waren, ihn zu hören und daß sie geheilt würden von ihren seuchen; und die von unsauberen geistern umgetrieben wurden, die wurden gesund.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi piyeer di wax loolu, xel mu sell mi wàcc ci kaw ñépp ñiy déglu kàddu ga.

German

da petrus noch diese worte redete, fiel der heilige geist auf alle, die dem wort zuhörten.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñoom ci àddina lañu bokk; moo tax ñuy wax waxi àddina, te àddina di leen déglu.

German

sie sind von der welt; darum reden sie von der welt, und die welt hört sie.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

moom nag muy déglu pool miy waare. noonu pool xool ko jàkk, gis ne, am na ngëm ngir wér.

German

der hörte paulus reden. und als dieser ihn ansah und merkte, daß er glaubte, ihm möchte geholfen werden,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye xamuñu woon lan lañu man a def, ndaxte nit ñépp a ngi ko doon déglu, bañ benn baat raw leen.

German

und fanden nicht, wie sie ihm tun sollten, denn das volk hing ihm an und hörte ihn.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

benn bés yeesu taxaw ca tefesu dexu senesaret. mbooloo ma wër ko, di buuxante ngir déglu kàddug yàlla.

German

es begab sich aber, da sich das volk zu ihm drängte, zu hören das wort gottes, daß er stand am see genezareth

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xam nanu ne, yàlla du déglu boroom bàkkaar. waaye nag, dina déglu ki koy ragal tey def coobareem.

German

wir wissen aber, daß gott die sünder nicht hört; sondern so jemand gottesfürchtig ist und tut seinen willen, den hört er.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yéen sama bokk yi ma bëgg, nangeen xam lii: ku nekk war ngaa farlu ci déglu, di yéex a wax tey yéex a mer.

German

darum, liebe brüder, ein jeglicher mensch sei schnell, zu hören, langsam aber, zu reden, und langsam zum zorn.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

barkeel ngeen, yaw miy jàng ak yéen ñiy déglu wax yii jóge ca yàlla, te di sàmm li ñu ci bind, ndaxte waxtu wi jege na.

German

selig ist, der da liest und die da hören die worte der weissagung und behalten, was darin geschrieben ist; denn die zeit ist nahe.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xam naa ne, doo jóg ci di ma déglu, waaye dama koy wax, ngir nit ñi ma wër gëm ne, yaa ma yónni.»

German

doch ich weiß, daß du mich allezeit hörst; aber um des volkes willen, das umhersteht, sage ich's, daß sie glauben, du habest mich gesandt.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

saxal ci di leen fàttali mbir yooyu, di leen dénk fa kanam yàlla, ñu moytoo werante ciy araf, ndax loolu jëmul fu dul ci yàq ngëmu ñiy déglu.

German

solches erinnere sie und bezeuge vor dem herrn, daß sie nicht um worte zanken, welches nichts nütze ist denn zu verkehren, die da zuhören.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

nun jot nanu xebaar bu baax bi ni ñoom, waaye kàddu, ga ñu déggoon, jariñu leen dara, ndaxte boolewuñu ci ngëm, ba ñu koy déglu.

German

denn es ist uns auch verkündigt gleichwie jenen; aber das wort der predigt half jenen nichts, da nicht glaubten die, so es hörten.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte erodd dafa ragal yaxya, ba sàmm bakkanam, xam ne ku jub la te sell. bu ko daan déglu it, day jaaxle lool, teewul mu bég ci déglu ko.

German

herodes aber fürchtete johannes; denn er wußte, daß er ein frommer und heiliger mann war; und verwahrte ihn und gehorchte ihm in vielen sachen und hörte ihn gern.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gannaaw loolu bokk yi, ci lu jëm ci njiit, yi boroom bi teg ci seen kanam te ñuy liggéey ci seen biir, di leen artu, maa ngi leen di ñaan ngeen déglu leen;

German

wir bitten aber euch, liebe brüder, daß ihr erkennet, die an euch arbeiten und euch vorstehen in dem herrn und euch vermahnen;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag bokk yi, bégleen, jublu cig mat, di déglu soññante bi ma leen di dénk, am benn xalaat te dëkk ci jàmm; noonu yàlla miy mbëggeel te di yàllay jàmm dina ànd ak yéen.

German

zuletzt, liebe brüder, freuet euch, seid vollkommen, tröstet euch, habt einerlei sinn, seid friedsam! so wird der gott der liebe und des friedens mit euch sein.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ñu déggee nag, muy wax ci mbirum ndekkitel ñi dee, ñii di ko fontoo, ña ca des ne ko: «dinanu la déglu ci mbir moomu beneen yoon.»

German

da sie hörten die auferstehung der toten, da hatten's etliche ihren spott; etliche aber sprachen: wir wollen dich davon weiter hören.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu tontu ko: «korney, njiitu xare ba, nit ku jub la te ragal yàlla, ba am seede su rafet ci bànni israyil gépp. malaaka mu sell nag sant na ko, mu woolu la ci këram te déglu li ngay wax.»

German

sie aber sprachen: kornelius, der hauptmann, ein frommer und gottesfürchtiger mann und gutes gerüchts bei dem ganzen volk der juden, hat befehl empfangen von einem heiligen engel, daß er dich sollte fordern lassen in sein haus und worte von dir hören.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,747,967,746 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK