Results for domandò translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

udito ciò, pilato domandò se era galile

Wolof

bi pilaat yégee baat yooyu, mu laajte ne: «ndax nit kii galile la dëkk?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

sentendo passare la gente, domandò che cosa accadesse

Wolof

naka la gumba ga dégg mbooloo di jàll, mu laaj lan moo xew.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

chiamò un servo e gli domandò che cosa fosse tutto ciò

Wolof

mu daldi woo kenn ca surga ya nag, laaj ko lu xew.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

egli domandò loro: «di chi è questa immagine e l'iscrizione?»

Wolof

yeesu ne leen: «kan lañu ci def nataalam ak turam?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

gesù allora si fermò e ordinò che glielo conducessero. quando gli fu vicino, gli domandò

Wolof

noonu yeesu taxaw, santaane ñu indil ko ko. bi mu jegesee, yeesu laaj ko ne:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e domandò loro: «quanti pani avete?». gli dissero: «sette»

Wolof

yeesu laaj leen: «Ñaata mburu ngeen am?» Ñu ne ko: «juróom-ñaar.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

questi, vedendo pietro e giovanni che stavano per entrare nel tempio, domandò loro l'elemosina

Wolof

bi mu gisee piyeer ak yowaana nag, ñuy dugg ca kër yàlla ga, mu dékk leen loxo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

domandò loro di nuovo: «chi cercate?». risposero: «gesù, il nazareno»

Wolof

yeesu laajaat leen ne: «ku ngeen di seet?» Ñu ne ko: «yeesum nasaret.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

uscì dunque pilato verso di loro e domandò: «che accusa portate contro quest'uomo?»

Wolof

looloo tax pilaat boroom réew ma génn, dajeek ñoom. mu laaj leen ne: «lu ngeen di jiiñ waa jii?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ma gesù domandò: «quanti pani avete?». risposero: «sette, e pochi pesciolini»

Wolof

yeesu ne leen: «Ñaata mburu ngeen am?» Ñu tontu ko: «juróom-ñaari mburu ak ay jën yu ndaw.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

poi domandò loro: «e' lecito in giorno di sabato fare il bene o il male, salvare una vita o toglierla?»

Wolof

noonu yeesu ne leen: «lan moo jaadu, nu def ko bésu noflaay bi, lu baax mbaa lu bon; nu musal nit mbaa nu rey nit?» waaye ñu ne cell.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora il governatore domandò: «chi dei due volete che vi rilasci?». quelli risposero: «barabba!»

Wolof

noonu boroom réew ma laaj leen: «kan ci ñaar ñii ngeen bëgg, ma bàyyil leen ko?» Ñu tontu ko: «barabas.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e gli domandò: «come ti chiami?». «mi chiamo legione, gli rispose, perché siamo in molti»

Wolof

noonu yeesu laaj ko: «noo tudd?» mu tontu ko: «coggal laa tudd, ndaxte ñu bare lanu.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora il tribuno si recò da paolo e gli domandò: «dimmi, tu sei cittadino romano?». rispose: «sì»

Wolof

noonu kilifa ga ñëw laaj pool: «wax ma, ndax jaambur nga ci room?» mu tontu ko: «waaw, moom laa.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora domandò: «ma voi chi dite che io sia?». pietro, prendendo la parola, rispose: «il cristo di dio»

Wolof

yeesu ne leen: «yéen nag ku ngeen ne moom laa?» piyeer tontu ko ne: «yaa di almasi, bi yàlla yónni.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,719,429,379 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK