From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
kwa hiyo nakwambia amesamehewa dhambi zake nyingi kwa kuwa ameonyesha upendo mkubwa. mwenye kusamehe kidogo, hupenda kidogo."
moo tax ma di la wax ne, su wonee mbëggeel gu réye nii, dafa fekk ñu baal ko bàkkaaram yu bare. waaye ki mbëggeelam néew dafa fekk ñu baal ko lu tuuti.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
nawaambieni, huyu mtoza ushuru alirudi nyumbani akiwa amesamehewa. lakini yule mwingine, sivyo. kwa maana kila anayejikweza atashushwa, na kila anayejishusha atakwezwa."
yeesu teg ca ne: «maa ngi leen koy wax, nit kooku, ba muy ñibbi këram, moom la yàlla àtte ni ku jub, waaye du farisen ba. ndaxte képp kuy yékkatiku dees na la suufeel, te kuy suufeelu, ñu yékkati la.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting