Results for walivyotaka translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

lakini nawaambieni, eliya amekwisha kuja, nao wakamtendea walivyotaka kama ilivyoandikwa juu yake."

Wolof

waaye maa ngi leen di wax ne, iliyas ñëw na, te def nañu ko la leen neex, ni ko mbind mi waxe.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

akamfungua kutoka gerezani yule waliyemtaka, ambaye alikuwa ametiwa gerezani kwa sababu ya uasi na kuua; akamtoa yesu kwao, wamfanyie walivyotaka.

Wolof

mu bàyyil leen ki ñu ko ñaanoon, kooku ñu tëjoon kaso, ndax tas réew ma ak rey nit. waaye mu jébbal leen yeesu ci seeni loxo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini nawaambieni, eliya amekwisha kuja nao hawakumtambua, bali walimtendea jinsi walivyotaka. mwana wa mtu atateswa vivyo hivyo mikononi mwao."

Wolof

teewul maa ngi leen di wax ne, iliyas ñëw na te xàmmiwuñu ko, waaye def nañu ko la leen neex. noonu it dañoo nar a sonal léegi doomu nit ki.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,740,206,661 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK