Results for tollook translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

noonu maryaama toog fa elisabet lu war a tollook ñetti weer, sog a ñibbi.

French

marie demeura avec Élisabeth environ trois mois. puis elle retourna chez elle.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ki jëmbët ak ki suuxat benn lañu. teewul nag ku nekk dina jot yool bu tollook liggéeyam.

French

celui qui plante et celui qui arrose sont égaux, et chacun recevra sa propre récompense selon son propre travail.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye daa wàcce boppam,ba tollook nit ñi,def boppam surga.te bi mu yoree bindu nit,

French

mais s`est dépouillé lui-même, en prenant une forme de serviteur, en devenant semblable aux hommes; et ayant paru comme un simple homme,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

maneesoon na jaay latkoloñ jii ci lu tollook peyug atum lëmm, jox ko miskin yi.» noonu ñu daldi gëdd jigéen ji.

French

on aurait pu le vendre plus de trois cents deniers, et les donner aux pauvres. et ils s`irritaient contre cette femme.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ñu joowee lu war a tollook juróom benni kilomet, ñu séen yeesu, muy dox ci kaw dex gi, jëm ci ñoom, ñu daldi tiit.

French

après avoir ramé environ vingt-cinq ou trente stades, ils virent jésus marchant sur la mer et s`approchant de la barque. et ils eurent peur.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

nikodem itam ñëw, moom mi masoon a seeti yeesu guddi. mu indaale lu war a tollook fanweeri kiloy cuuraay lu ñu defare ndàbbi miir ak banti aloos.

French

nicodème, qui auparavant était allé de nuit vers jésus, vint aussi, apportant un mélange d`environ cent livres de myrrhe et d`aloès.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ñu ca tegee luy tollook ayu-bés gannaaw bi yeesu waxee loolu, mu ànd ak piyeer, yowaana ak saag, yéeg ca kaw tund wa ngir ñaan.

French

environ huit jours après qu`il eut dit ces paroles, jésus prit avec lui pierre, jean et jacques, et il monta sur la montagne pour prier.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeneen taalibe ya xëcc mbaal, mi fees dell ak jën, jëme ko ca tefes ga, ndaxte gaal ga sorewul woon; diggante bi waroon na tollook téeméeri meetar.

French

les autres disciples vinrent avec la barque, tirant le filet plein de poissons, car ils n`étaient éloignés de terre que d`environ deux cents coudées.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi yeesu dikkee ba tollook garab ga nag, mu téen ne ko: «sase, wàccal gaaw, ndax tey sa kër laa war a dal.»

French

lorsque jésus fut arrivé à cet endroit, il leva les yeux et lui dit: zachée, hâte-toi de descendre; car il faut que je demeure aujourd`hui dans ta maison.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye yeesu tontu leen ne: «yéen joxleen leen lu ñu lekk.» Ñu ne ko: «xanaa nu jënd lu tollook peyu juróom-ñetti weer ci mburu, jox leen ñu lekk?»

French

jésus leur répondit: donnez-leur vous-mêmes à manger. mais ils lui dirent: irions-nous acheter des pains pour deux cents deniers, et leur donnerions-nous à manger?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,747,919,507 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK