From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
en hulle is deur hom in die jordaan gedoop met belydenis van hulle sondes.
Ñu nangu seeni bàkkaar, yaxya sóob leen ca dexu yurdan.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
en baie van die wat gelowig geword het, het belydenis kom doen en hulle dade bekend gemaak;
bi loolu amee ñu bare ci ñi gëm ñëw, di wesar ci kanam ñépp seeni jati luxus.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
daarom, heilige broeders, deelgenote van die hemelse roeping, let op die apostel en hoëpriester van ons belydenis, christus jesus,
kon nag yéen bokk yu sell yi, yéen ñi yàlla woo, ngeen bokk ci nguuram gu kawe ga, seetleen ci yeesu, moom miy ndawu yàlla li, di saraxalekat bu mag bi ci yoon wi nu gëm.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
omdat hulle deur die bewys van hierdie diens god verheerlik oor die onderwerping van julle belydenis aan die evangelie van christus en oor die milddadigheid van die bydrae aan hulle en aan almal,
ci li ngeen firndeel seen mbëggeel ci joxe ndimbal lii, dinañu màggal yàlla, ndaxte wone ngeen ni ngeen déggale xebaar bu baax bu kirist bi, ak ni ngeen yéwéne ci seen ndimbal jëme ci ñoom ak ñépp.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
terwyl ons dan 'n groot hoëpriester het wat deur die hemele deurgegaan het, naamlik jesus, die seun van god, laat ons die belydenis vashou.
gannaaw am nanu saraxalekat bu mag-a-mag bu àgg ba ca kanam yàlla, di yeesu doomu yàlla ji, nanu jàpp bu dëgër yoon wi nu gëm.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waarvan sommige belydenis gedoen het en, wat die geloof betref, op 'n dwaalweg geraak het. mag die genade met jou wees! amen.
am na ñu topp xam-xam boobu, waaye moy nañu ci yoonu ngëm. na yiwu yàlla ànd ak yéen.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: