Results for c'est bien courage a vous translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

c`est bien à tort que vous vous glorifiez. ne savez-vous pas qu`un peu de levain fait lever toute la pâte?

Wolof

seen tiitar bi jekkul dara. xanaa xamuleen ne, tuuti lawiir day tax tooyalu fariñ bépp funki?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

celui donc qui sait faire ce qui est bien, et qui ne le fait pas, commet un péché.

Wolof

kon nag ku xam def lu baax te defoo ko, bàkkaar nga.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car nous recherchons ce qui est bien, non seulement devant le seigneur, mais aussi devant les hommes.

Wolof

danuy fexee def li jub, du ci kanam yàlla rekk, waaye it ci kanam nit ñi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

a vous maintenant, riches! pleurez et gémissez, à cause des malheurs qui viendront sur vous.

Wolof

dégluleen yéen boroom alal yi, jooyleen te naqarlu ndax mbugal, gi leen di xaar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ainsi, que ceux qui souffrent selon la volonté de dieu remettent leurs âmes au fidèle créateur, en faisant ce qui est bien.

Wolof

kon nag ñi tegoo fitna ci coobareg yàlla, nañu sax ci def lu baax, dénk seen bopp yàlla, miy bindkat biy sàmm kóllëre.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il lui dit: c`est bien, bon serviteur; parce que tu as été fidèle en peu de chose, reçois le gouvernement de dix villes.

Wolof

buur ba ne ko: “def nga lu baax, surga bu baax nga. segam wone nga ne, takku nga ci lu tuuti, falul ci fukki dëkk.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais la nourriture solide est pour les hommes faits, pour ceux dont le jugement est exercé par l`usage à discerner ce qui est bien et ce qui est mal.

Wolof

waaye ñam wu dëgër, ñi mat a ko yelloo, maanaam ñiy jëfandikoo seen xel ngir ràññee lu baax ak lu bon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

comme sara, qui obéissait à abraham et l`appelait son seigneur. c`est d`elle que vous êtes devenues les filles, en faisant ce qui est bien, sans vous laisser troubler par aucune crainte.

Wolof

ni saarata déggale woon ibraayma, ba daan ko wooye «sang bi.» yéen nag, su ngeen dee def lu baax te bañ cee boole genn njàqare, kon mel na ni saarataa leen jaboote.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais, ajouta-t-il, je vous le dis en vérité, aucun prophète n`est bien reçu dans sa patrie.

Wolof

mu tegaat ca ne: «ci dëgg maa ngi leen koy wax, ab yonent kenn du ko teral ca réewam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

a vous maintenant, qui dites: aujourd`hui ou demain nous irons dans telle ville, nous y passerons une année, nous trafiquerons, et nous gagnerons!

Wolof

léegi nag dégluleen, yéen ñiy wax ne: «tey walla ëllëg dinanu dem ca dëkk sàngam, def fa at, di fa sàkku xaalis ci jula.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,781,447,848 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK