From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
judas, ayant pris le morceau, se hâta de sortir. il était nuit.
yudaa nag jël dogu mburu ma, daldi génn ca saa sa. booba guddi woon na.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il leur dit: cette espèce-là ne peut sortir que par la prière.
yeesu tontu leen ne: «yu mel ni yii, ñaan ci yàlla rekk a leen di dàq.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il les fit sortir, et dit: seigneurs, que faut-il que je fasse pour être sauvé?
mu génne leen ci biti ne leen: «kilifa yi, lu ma war a def, ba mucc?»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
mais un ange du seigneur, ayant ouvert pendant la nuit les portes de la prison, les fit sortir, et leur dit:
waaye ci guddi malaakam boroom bi ubbi buntu kaso ba, génne leen ci biti naan:
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
comme jésus s`en allait, au sortir du temple, ses disciples s`approchèrent pour lui en faire remarquer les constructions.
bi yeesu waxee ba noppi, mu génn ca kër yàlla ga, dem. noonu ay taalibeem ñëw ci moom, ngir won ko tabaxi kër yàlla ga.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors on fit sortir de la foule alexandre, que les juifs poussaient en avant; et alexandre, faisant signe de la main, voulait parler au peuple.
ci kaw loolu yawut ya jéñ alegsàndar ci kanam, te mbooloo ma di ko xaacu ay ndigal, mu daldi tàllal loxoom, ngir làyyi ca mbooloo ma.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
lorsqu`il a fait sortir toutes ses propres brebis, il marche devant elles; et les brebis le suivent, parce qu`elles connaissent sa voix.
sàmm bi, bu génnee yi mu moom yépp, dina leen jiitu, ñu topp ko, ndaxte xam nañu baatam.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
quand ils furent sortis de l`eau, l`esprit du seigneur enleva philippe, et l`eunuque ne le vit plus. tandis que, joyeux, il poursuivait sa route,
ba noppi ñu génn ca ndox ma, te ca saa sa xelu boroom bi fëkk filib, ba jaraaf ja gisatu ko, waaye mu toppaat yoonam, ànd ak mbég.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: