Results for persecutionem translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

persecutionem patimur sed non derelinquimur deicimur sed non perimu

Wolof

dañu nuy fitnaal, waaye yàlla du nu wacc mukk. tër nañu nu, waaye kenn doggaliwu nu.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et omnes qui volunt pie vivere in christo iesu persecutionem patientu

Wolof

te ku bokk ci kirist yeesu, te bëgg dund dund gu ànd ak ragal yàlla, alamikk ñu fitnaal la.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

beati qui persecutionem patiuntur propter iustitiam quoniam ipsorum est regnum caeloru

Wolof

yéen ñi ñu fitnaal ndax seen njub,barkeel ngeen,ndaxte nguuru yàlla aji kawe ji,yéena ko yelloo.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et laboramus operantes manibus nostris maledicimur et benedicimus persecutionem patimur et sustinemu

Wolof

nu ngi ñaq di jariñoo. ku nu saaga, nu ñaanal la lu baax. coono bu ñu nu teg, nu tegoo ko.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

ego autem fratres si circumcisionem adhuc praedico quid adhuc persecutionem patior ergo evacuatum est scandalum cruci

Wolof

man nag bokk yi, bu ma doon faaydaal xaraf ci sama waare, kon duñu ma fitnaale nii; te it li may yégle ci deewu kirist ca bant ba dootul naqari kenn.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

iudaei autem concitaverunt religiosas mulieres et honestas et primos civitatis et excitaverunt persecutionem in paulum et barnaban et eiecerunt eos de finibus sui

Wolof

waaye yawut ya xiir ay jigéen, ñi woomle te farlu ci diine, ñoom ak magi dëkk ba, ñu fitnaal pool ak barnabas, ngir génne leen réew ma.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,125,979,389 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK