From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
altera die iterum stabat iohannes et ex discipulis eius du
ca ëllëg sa yaxya taxawaatoon na ca bérab booba, ànd ak ñaari taalibeem.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
turba ergo quae stabat et audierat dicebant tonitruum factum esse alii dicebant angelus ei locutus es
mbooloo ma fa teewoon te dégg baat ba daldi ne: «dënnu la woon!» Ñeneen naan: «malaakaa doon wax ak moom.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
maria autem stabat ad monumentum foris plorans dum ergo fleret inclinavit se et prospexit in monumentu
maryaama nag moom, ma nga desoon ca biti, ca wetu bàmmeel ba, di jooy. bi muy jooy, mu sëgg, yër ci biir,
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et congregatae sunt ad eum turbae multae ita ut in naviculam ascendens sederet et omnis turba stabat in litor
mbooloo mu bare dajaloo ca moom, ba tax mu dugg cig gaal, toog; mbooloo mépp taxaw ca tefes ga.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
petrus autem stabat ad ostium foris exivit ergo discipulus alius qui erat notus pontifici et dixit ostiariae et introduxit petru
waaye piyeer, moom, des ca buntu kër ga. noonu taalibe boobu xamante woon ak saraxalekat bu mag ba génn, wax ak jigéen, ja doon wottu buntu kër ga, fexe piyeer dugg ci biir.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et stabat populus expectans et deridebant illum principes cum eis dicentes alios salvos fecit se salvum faciat si hic est christus dei electu
mbooloo maa nga fa taxaw di seetaan. njiit ya di ko reetaan naan: «musal na ñeneen; na musal boppam, su fekkee mooy almasi bi, ki yàlla fal!»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
altera die turba quae stabat trans mare vidit quia navicula alia non erat ibi nisi una et quia non introisset cum discipulis suis iesus in navem sed soli discipuli eius abissen
ca ëllëg sa mbooloo, ma des ca geneen wàllu dex ga, gis ne genn gaal ga fa nekkoon rekk dem na. xam nañu ne yeesu bokku ko woon ak taalibe ya, ndaxte ñoom rekk a àndoon.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: