Results for shukrani translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

sala yako ya shukrani yaweza kweli kuwa bora, lakini huyo mwingine haitamfaidia.

Wolof

dëgg la, dangay sant yàlla bu baax, waaye ki ci des, ngëmam yokkuwul.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

tunalipokea jambo hili kwa furaha daima na kutoa shukrani nyingi kwako kila mahali.

Wolof

gis nanu ko fépp ak ci lépp, di la gërëm ak sunu xol bépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kila kitu alichoumba mungu ni chema, wala hakuna kinachohitaji kukataliwa, bali vyote vipokelewe kwa sala ya shukrani,

Wolof

ndaxte li yàlla sàkk lépp baax na, kon wenn ñam araamul ci ku koy jëfandikoo ak cant.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kwanza kabisa, basi naomba dua, sala, maombi na sala za shukrani zitolewe kwa mungu kwa ajili ya watu wote,

Wolof

fii laay tàmbale nag: maa ngi leen di dénk, ngeen yóbbu ñépp fa kanam yàlla ciy ñaan, ay tinu ak i ngërëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

zungumzeni kwa maneno ya zaburi, nyimbo na tenzi za kiroho; mwimbieni bwana nyimbo na zaburi kwa shukrani mioyoni mwenu.

Wolof

di waxante ci seen biir ci ay taalifi sabóor, ci ay woy ak ay cant yu tukkee ci xelum yàlla, di woy ak a kañ boroom bi ci seeni xol.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

sisi basi, na tushukuru kwani tunapokea utawala usiotikisika. tuwe na shukrani na kumwabudu mungu kwa namna itakayompendeza, kwa ibada na hofu;

Wolof

kon nag gannaaw dinañu jot nguur gu kenn mënul a yengal, nanu ci sant yàlla, di ko jaamu, ni mu ko bëgge, boole ci wegeel ak ragal,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini, shukrani kwa mungu anayetuongoza daima katika msafara wa ushindi wa kristo. yeye hutufanya tuueneze ukweli wa kristo kama harufu nzuri, kila mahali.

Wolof

waaye cant ñeel na yàlla! ci sunu booloo ak kirist, daf nuy yóbbaale saa su nekk ci gawari ndamam, tey jaar ci nun ngir turu kirist jolli fu nekk, ni xetu latkoloñ di tasaaroo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

yote haya ni kwa faida yenu; ili kama vile neema ya mungu inavyoenea kwa watu wengi zaidi na zaidi vivyo hivyo watu wengi zaidi watoe shukrani nyingi kwa utukufu wa mungu.

Wolof

ndaxte lépp li nuy daj, seen njariñ a tax, ngir yiwu yàlla, wiy yokku ci nit ñu gën a takku, yokkaale ngërëm lu jëm ci yàlla, ngir jollil ndamam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

watu hao hufundisha kwamba ni makosa kuona na pia kula vyakula fulani. lakini mungu aliviumba vyakula hivyo, ili wale walio waumini na ambao wanapata kuujua ukweli, wavitumie kwa shukrani.

Wolof

dinañu tere séy, di araamal ay ñam, fekk yàlla sàkk na leen, ngir ñi gëm te xam dëgg man ciy jëfandiku ak cant.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

shukrani kwa mungu afanyaye hayo kwa njia ya bwana wetu yesu kristo! hii basi, ndiyo hali yangu: mimi binafsi, kwa akili yangu, ninaitumikia sheria ya dhambi.

Wolof

maa ngi sant yàlla; am na kuy musle, mooy yeesu kirist sunu boroom. kon nag lii laa gis ci sama bopp: ci sama xel maa ngi topp yoonu yàlla, waaye ci sama bindu doom aadama maa ngi topp yoonu bàkkaar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

ila nyinyi wapendeni adui zenu, na kuwatendea mema; kopesheni bila kutazamia malipo, na tuzo lenu litakuwa kubwa, nanyi mtakuwa watoto wa mungu aliye juu. kwa maana yeye ni mwema kwa wale wasio na shukrani na walio wabaya.

Wolof

waaye soppleen seeni noon, di leen defal lu baax, tey leble, bañ a yaakaar ñu delloo leen ko. noonu seen yool dina mag te dingeen wone ne, yéenay doomi aji kawe ji, ndaxte yàlla day wone mbaaxam ci ñu goreedi ñi ak ñu soxor ñi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,919,952,497 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK