From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
kisha, wote kwa jumla, wakasimama, wakampeleka yesu mbele ya pilato.
gannaaw loolu kureelu àttekat ya yépp daldi jóg, yóbbu yeesu ca pilaat.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
mama yake yesu na ndugu zake walifika hapo, wakasimama nje, wakampelekea ujumbe kutaka kumwona.
noonu ndeyu yeesu ak ay rakkam ñëw, ñu taxaw ci biti, yónnee, woo ko.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alipokuwa anaingia katika kijiji kimoja, watu kumi wenye ukoma walikutana naye, wakasimama kwa mbali.
bi muy jub benn dëkk, fukki gaana ñëw, dogale ko. Ñu taxaw dand ko, di wax ca kaw naan:
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
akawauliza, "mnazungumza nini huku mnatembea?" nao wakasimama kimya, nyuso zao wamezikunja kwa huzuni.
yeesu ne leen: «lan ngeen di waxtaane nii ci yoon wi?» noonu ñu taxaw, seen xol jeex.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
lakini baada ya zile siku tatu na nusu pumzi ya uhai kutoka kwa mungu iliwaingia, nao wakasimama; wote waliowaona wakaingiwa na hofu kuu.
waaye bi ñetti fan ya ak genn-wàll wéyee, xelum dund, jóge ca yàlla, solu leen, ñu jóg taxaw. noonu tiitaange gu réy jàpp ñi leen doon seetaan.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
malaika wote wakasimama kukizunguka kiti cha enzi, wazee na vile viumbe hai vinne. wakaanguka kifudifudi mbele ya kiti cha enzi, wakamwabudu mungu,
noonu malaaka yépp taxaw, wër gàngune ma ak mag ña ak ñeenti mbindeef ya. Ñu dëpp seen jë ca kanamu gàngune ma, di jaamu yàlla,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
kisha akaenda, akaligusa lile jeneza, na wale waliokuwa wanalichukua wakasimama. halafu akasema, "kijana! nakuamuru, amka!"
mu jegeñsi, laal jaat ga, ñi ko jàppoo taxaw. mu ne: «waxambaane wi, jógal, ndigal la.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting