From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
moytul ndax leer gi nekk ci yaw du lëndëm.
እንግዲህ በአንተ ያለው ብርሃን ጨለማ እንዳይሆን ተመልከት።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
leer gi feeñ na ci biir lëndëm, te lëndëm gi jàppu ko.
ብርሃንም በጨለማ ይበራል፥ ጨለማም አላሸነፈውም።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
li tàmbalee digg-bëccëg, ba ci tisbaar, réew mépp lëndëm.
ስድስት ሰዓትም በሆነ ጊዜ፥ እስከ ዘጠኝ ሰዓት በምድር ሁሉ ላይ ጨለማ ሆነ።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yaa ngi teg sa bopp wommatkatu gumba yi ak leeru ñi nekk cig lëndëm.
በሕግም የእውቀትና የእውነት መልክ ስላለህ፥ የዕውሮች መሪ፥ በጨለማም ላሉ ብርሃን፥ የሰነፎችም አስተማሪ፥ የሕፃናትም መምህር እንደ ሆንህ በራስህ ብትታመን፤
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ni ag leer laa wàcce ci àddina, ngir ku ma gëm du des ci lëndëm.
በእኔ የሚያምን ሁሉ በጨለማ እንዳይኖር እኔ ብርሃን ሆኜ ወደ ዓለም መጥቻለሁ።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ku wax ne yaa ngi ci leer, tey bañ sa mbokk, yaa ngi ci lëndëm ba tey.
በብርሃን አለሁ የሚል ወንድሙንም የሚጠላ እስከ አሁን በጨለማ አለ።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yàlla musal na nu ci dooley lëndëm, yóbbu nu ci nguuru doomam ji mu bëgg,
እርሱ ከጨለማ ሥልጣን አዳነን፥ ቤዛነቱንም እርሱንም የኃጢአትን ስርየት ወዳገኘንበት ወደ ፍቅሩ ልጅ መንግሥት አፈለሰን።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ngir leeral ñi toog ci lëndëm,takkandeeru dee tiim leen,ngir jiite nu ci yoonu jàmm.»
ብርሃኑም በጨለማና በሞት ጥላ ተቀምጠው ላሉት ያበራል እግሮቻችንንም በሰላም መንገድ ያቀናል።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye ci wax jooju xar-kanamam lëndëm, mu jóge fa ak tiis, ndaxte ku bare woon alal la.
ነገር ግን ስለዚህ ነገር ፊቱ ጠቈረ፥ ብዙ ንብረት ነበረውና እያዘነም ሄደ።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñooñule ay teen yu dëy lañu, di xiini lay, yu ngelaw liy naawal, te seen pey mooy lëndëm gu ne taraj.
ድቅድቅ ጨለማ ለዘላለም የተጠበቀላቸው እነዚህ ውኃ የሌለባቸው ምንጮች በዐውሎ ነፋስም የተነዱ ደመናዎች ናቸው።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye ku ñàkk jiko yooyu, ay bëtam dañoo lëndëm ba gumba, te fàtte na, ni ko yàlla fóotale bàkkaari démb.
እነዚህ ነገሮች የሌሉት ዕውር ነውና፥ በቅርብም ያለውን ብቻ ያያል፥ የቀደመውንም ኃጢአቱን መንጻት ረስቶአል።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte yàlla jeggalul malaaka ya bàkkaaroon, waaye tàbbal na leen safara, tëj leen ca kàmb yu lëndëm, di leen nége àtte ba.
እግዚአብሔር ኃጢአትን ላደረጉ መላእክት ሳይራራላቸው ወደ ገሃነም ጥሎ በጨለማ ጉድጓድ ለፍርድ ሊጠበቁ አሳልፎ ከሰጣቸው፥
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
looloo tax lu ngeen wax ci biir lëndëm, dees na ko dégg ci leer. lu ngeen déey nit ci biir néeg, dees na ko yégle ci kaw taax yi.
ስለዚህ በጨለማ የምትናገሩት ሁሉ በብርሃን ይሰማል፥ በእልፍኝም ውስጥ በጆሮ የምትናገሩት በሰገነት ላይ ይሰበካል።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
gépp may gu baax ak gépp jagle gu mat, ci yàlla la jóge, di baay bi sàkk leeri asamaan, fekk moom du soppiku, mbaa muy leer ak di lëndëm.
በጎ ስጦታ ሁሉ ፍጹምም በረከት ሁሉ ከላይ ናቸው፥ መለወጥም በእርሱ ዘንድ ከሌለ በመዞርም የተደረገ ጥላ በእርሱ ዘንድ ከሌለ ከብርሃናት አባት ይወርዳሉ።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye bu sa bët woppee, kon sa yaram wépp lëndëm. leer gi nekk ci yaw, bu nekkee lëndëm, naka la lëndëm googu di këruuse!
ዓይንህ ግን ታማሚ ብትሆን፥ ሰውነትህ ሁሉ የጨለመ ይሆናል። እንግዲህ በአንተ ያለው ብርሃን ጨለማ ከሆነ፥ ጨለማውስ እንዴት ይበረታ!
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
teewul ndigal lu bees laa leen di bind, lu amoon ci dundu yeesu, te am it ci seen dund; ndaxte lëndëm gaa ngi wéy, te leer gu wóor gi fenk na xaat.
ዳግመኛ አዲስ ትእዛዝን እጽፍላችኋለሁ፥ ይህም ነገር በእርሱ በእናንተም እውነተኛ ነው፤ ጨለማው ያልፋልና እውነተኛውም ብርሃን አሁን ይበራል።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te it malaaka ya jàppul woon ca daraja ja ñu amoon, xanaa toxoo fa ñu leen dëëloon, yàlla yeew na leen buum yu sax, tëj leen ci biir lëndëm, di leen nége àtteb bés bu mag ba.
መኖሪያቸውንም የተዉትን እንጂ የራሳቸውን አለቅነት ያልጠበቁትን መላእክት በዘላለም እስራት ከጨለማ በታች እስከ ታላቁ ቀን ፍርድ ድረስ ጠብቆአቸዋል።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu buur ba ne ay surgaam: “yeewleen ko ci tànk yi ak ci loxo yi, sànni ko ci biti ci lëndëm gi. foofa dees na fa jooy tey yéyu.”
በዚያን ጊዜ ንጉሡ አገልጋዮቹን። እጁንና እግሩን አስራችሁ በውጭ ወዳለው ጨለማ አውጡት፤ በዚያ ልቅሶና ጥርስ ማፋጨት ይሆናል አለ።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu ne leen: «leer gi dootul yàgg ak yéen. doxleen, ci bi ngeen dee am leer, ngir lëndëm bañ leen a bett. ndaxte kuy dox ci lëndëm doo xam foo jëm.
ኢየሱስም። ገና ጥቂት ጊዜ ብርሃን ከእናንተ ጋር ነው። ጨለማ እንዳይደርስባችሁ ብርሃን ሳለላችሁ ተመላለሱ፤ በጨለማም የሚመላለስ ወዴት እንዲሄድ አያውቅም።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
tey jii gis bu lëndëm lanuy gis, ni takkandeer ci seetu bu lëndëm, bu ëllëgee dinanu gis jaxran. tey jii sama xam-xam des na, bu ëllëgee dinaa xam ba mat sëkk, ni ma yàlla xame.
ዛሬስ በመስተዋት በድንግዝግዝ እንደምናይ ነን በዚያን ጊዜ ግን ፊት ለፊት እናያለን፤ ዛሬስ ከእውቀት ከፍዬ አውቃለሁ በዚያን ጊዜ ግን እኔ ደግሞ እንደ ታወቅሁ አውቃለሁ።
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: