Results for jaambur translation from Wolof to English

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

English

Info

Wolof

waaye duñu topp jaambur; dañu koy daw, ndaxte miinuñu baatam.»

English

and a stranger will they not follow, but will flee from him: for they know not the voice of strangers.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bul gaaw a teg loxo kenn, ba fal ko, di séddu noonu ci bàkkaari jaambur, waaye dëkkal cig sell.

English

lay hands suddenly on no man, neither be partaker of other men's sins: keep thyself pure.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yawut yi jàpp nañu nit kii, bëgg koo rey, waaye bi ma yégee ne, jaambur la ci room, wallu naa ko ak ay xarekat, ba musal ko.

English

this man was taken of the jews, and should have been killed of them: then came i with an army, and rescued him, having understood that he was a roman.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci mbir mii nag, bu kenn ci yéen laal yëfi jaambur, ngir bañ koo tooñ. ndaxte waxoon nanu leen bu yàgg te artu leen ne, ñiy def loolu, boroom bi dina leen mbugal.

English

that no man go beyond and defraud his brother in any matter: because that the lord is the avenger of all such, as we also have forewarned you and testified.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

pool ne ko: «man yawut laa, di jaambur ci tars, dëkk bu am tur ci diiwaanu silisi. maa ngi lay ñaan, ma wax ak mbooloo mi.»

English

but paul said, i am a man which am a jew of tarsus, a city in cilicia, a citizen of no mean city: and, i beseech thee, suffer me to speak unto the people.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xam nga ndigal yi: “bul bóom, bul njaaloo, bul sàcc, bul seede lu dul dëgg, bul nangu alalu jaambur, teralal sa ndey ak sa baay.”»

English

thou knowest the commandments, do not commit adultery, do not kill, do not steal, do not bear false witness, defraud not, honour thy father and mother.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,944,486,115 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK