From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
andare ak filib,bartelemi ak macë,tomaa ak saag doomu alfe,tade ak simoŋ, mi bokk ca mbooloo, ma ñu tudde Ñi farlu ci moom seen réew;
andré; philippe; barthélemy; matthieu; thomas; jacques, fils d`alphée; thaddée; simon le cananite;
bi ñu dikkee, ñu yéeg ca néeg, ba sut ca taax ma, fa ñuy dal. Ñoo doon piyeer ak yowaana, saag ak andare, filib ak tomaa, bartelemi ak macë, saag doomu alfe, ak simoŋ mi bokkoon ci mbooloo mi ñuy wax Ñi farlu ci moom seen réew; ak yudaa doomu saag.
quand ils furent arrivés, ils montèrent dans la chambre haute où ils se tenaient d`ordinaire; c`étaient pierre, jean, jacques, andré, philippe, thomas, barthélemy, matthieu, jacques, fils d`alphée, simon le zélote, et jude, fils de jacques.