From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
bi dugub ji saxee nag, jëmb bi saxaale ak moom.
lorsque l`herbe eut poussé et donné du fruit, l`ivraie parut aussi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ni ñu dajalee jëmb ba, lakk ko, noonu lay nekke, bu àddina tukkee.
or, comme on arrache l`ivraie et qu`on la jette au feu, il en sera de même à la fin du monde.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye bi nit ñi di nelaw, noonam ñëw, ji jëmb ci biir dugub ji, daldi dem.
mais, pendant que les gens dormaient, son ennemi vint, sema de l`ivraie parmi le blé, et s`en alla.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
àddina mooy tool bi; ñi bokk ci nguuru yàlla ñoo di jiwu wu baax wi; ñi bokk ci ibliis ñooy jëmb bi;
le champ, c`est le monde; la bonne semence, ce sont les fils du royaume; l`ivraie, ce sont les fils du malin;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bàyyileen ñoom ñaar, ñu màgg, ba ngóob ma jot. bu ngóob ma jotee nag, dinaa wax ñi koy góob: jëkkleen a dindi jëmb bi, takk ko ay say, lakk ko, waaye ngeen semb dugub ji ci sama sàq.”»
laissez croître ensemble l`un et l`autre jusqu`à la moisson, et, à l`époque de la moisson, je dirai aux moissonneurs: arrachez d`abord l`ivraie, et liez-la en gerbes pour la brûler, mais amassez le blé dans mon grenier.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: