Results for lekkukaay translation from Wolof to French

Wolof

Translate

lekkukaay

Translate

French

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

amoon na ab farisen bu ñaan yeesu, mu ñëw lekkandoo ak moom. yeesu dem kër waa ja, toog ca lekkukaay.

French

un pharisien pria jésus de manger avec lui. jésus entra dans la maison du pharisien, et se mit à table.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi yeesu waxee ba noppi, benn farisen wax ko, mu ñëw lekke këram. yeesu dugg ca kër ga, toog ca lekkukaay ba.

French

pendant que jésus parlait, un pharisien le pria de dîner chez lui. il entra, et se mit à table.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ki toog ca lekkukaay ba, moom ak surgaam, ñoom ñaar kan moo ci gën a màgg? xanaa du ki toog ci lekkukaay bi? waaye man maa ngi ci seen biir ni surga.

French

car quel est le plus grand, celui qui est à table, ou celui qui sert? n`est-ce pas celui qui est à table? et moi, cependant, je suis au milieu de vous comme celui qui sert.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye bu ñu la wooyee, demal ca toogu bu gannaawe ba. bu ko defee ki la woo, bu agsee ne la: “sama xarit, àggal ca kaw.” loolu dina la sagal ci ñi nga toogandool ci lekkukaay bi.

French

mais, lorsque tu seras invité, va te mettre à la dernière place, afin que, quand celui qui t`a invité viendra, il te dise: mon ami, monte plus haut. alors cela te fera honneur devant tous ceux qui seront à table avec toi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,944,867,521 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK