Results for coobareg translation from Wolof to German

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

German

Info

Wolof

buleen ñàkk bopp nag, waaye xamleen liy coobareg boroom bi.

German

darum werdet nicht unverständig, sondern verständig, was da sei des herrn wille.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te àddina day wéy, waaye kuy def coobareg yàlla dinga sax ba fàww.

German

und die welt vergeht mit ihrer lust; wer aber den willen gottes tut, der bleibt in ewigkeit.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dangeen a war a muñ, ba def coobareg yàlla, sog a jot li mu leen digoon.

German

geduld aber ist euch not, auf daß ihr den willen gottes tut und die verheißung empfanget.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte kuy def coobareg yàlla, kooku mooy sama rakk ak sama jigéen ak sama ndey.»

German

denn wer gottes willen tut, der ist mein bruder und meine schwester und meine mutter.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu diir bi ko dese ci kaw suuf, dëddu na bànneexi bakkan, jublu ci coobareg yàlla.

German

daß er hinfort die noch übrige zeit im fleisch nicht der menschen lüsten, sondern dem willen gottes lebe.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte ku def sama coobareg baay bi nekk ci kaw, yaa di sama rakk, sama jigéen ak sama ndey.»

German

denn wer den willen tut meines vaters im himmel, der ist mein bruder, schwester und mutter.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte noonu la coobareg yàlla tëdde, maanaam ngeen sax ci def lu baax, ba wedamloo jayil yi xamul dara.

German

denn das ist der wille gottes, daß ihr mit wohltun verstopft die unwissenheit der törichten menschen,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag ñi tegoo fitna ci coobareg yàlla, nañu sax ci def lu baax, dénk seen bopp yàlla, miy bindkat biy sàmm kóllëre.

German

darum, welche da leiden nach gottes willen, die sollen ihm ihre seelen befehlen als dem treuen schöpfer in guten werken.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

moom mi joxe bakkanam ngir dindi sunuy bàkkaar, te musal nu ci àddina su bon, si nu nekk, dëppook coobareg yàlla sunu baay,

German

der sich selbst für unsere sünden gegeben hat, daß er uns errettete von dieser gegenwärtigen, argen welt nach dem willen gottes und unseres vaters,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

man pool, ndawul kirist yeesu ci coobareg yàlla, maa leen di bind, yéen gaayi yàlla yu sell yi te gëm kirist yeesu ci dëkku efes.

German

paulus, ein apostel jesu christi durch den willen gottes, den heiligen zu ephesus und gläubigen an christum jesum:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye xanaa dina am ku may wax ne: «gannaaw kenn mënul a bañ coobareg yàlla, lu tax kon muy teg nit tooñ?»

German

so sagst du zu mir: was beschuldigt er uns denn? wer kann seinem willen widerstehen?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bu leen àddina jey, waaye yeesluleen ci seen xel, ba soppiku, ngeen man a xam bu wér coobareg yàlla, di lépp lu baax, neex ko te mat sëkk.

German

und stellet euch nicht dieser welt gleich, sondern verändert euch durch die erneuerung eures sinnes, auf daß ihr prüfen möget, welches da sei der gute, wohlgefällige und vollkommene gotteswille.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

man pool, ndawul kirist yeesu ci coobareg yàlla, man ak timote sunu mbokk, noo leen di bind, yéen mbooloom yàlla mi nekk dëkku korent, ak gaayi yàlla yu sell, yi nekk ci diiwaanu akayi gépp.

German

paulus, ein apostel jesu christi durch den willen gottes, und bruder timotheus der gemeinde gottes zu korinth samt allen heiligen in ganz achaja:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu yeesu laaj leen: «kan ci ñaari doom yooyu moo def coobareg baayam?» Ñu ne: «Ñaareel bi.» kon yeesu ne leen: «ci dëgg maa ngi leen koy wax, juutikat yi ak jigéeni moykat yi ñoo leen jëkk a dugg ci nguuru yàlla aji kawe ji.

German

welcher unter den zweien hat des vaters willen getan? sie sprachen zu ihm: der erste. jesus sprach zu ihnen: wahrlich ich sage euch: die zöllner und huren mögen wohl eher ins himmelreich kommen denn ihr.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,724,959,185 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK