Ask Google

Results for kiñaan translation from Wolof to Korean

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Korean

Info

Wolof

Kon nag dëdduleen gépp coxor, gépp njublaŋ, naaféq, kiñaan ak jëw.

Korean

그 러 므 로 모 든 악 독 과 모 든 궤 휼 과 외 식 과 시 기 와 모 든 비 방 하 는 말 을 버 리

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ndaxte xamoon na ne, kiñaan rekk a taxoon, ñu jébbal ko ko.

Korean

이 는 저 가 그 들 의 시 기 로 예 수 를 넘 겨 준 줄 앎 이 러

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ku bëgg dafay muñ te laabiir. Ku bëgg du kiñaan, du kañu, du tiitaru,

Korean

사 랑 은 오 래 참 고, 사 랑 은 온 유 하 며, 투 기 하 는 자 가 되 지 아 니 하 며, 사 랑 은 자 랑 하 지 아 니 하 며, 교 만 하 지 아 니 하

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndax sañumaa def ak sama alal li ma neex? Walla ndax danga am kiñaan ci li ma yéwén?”

Korean

내 것 을 가 지 고 내 뜻 대 로 할 것 이 아 니 냐 내 가 선 하 므 로 네 가 악 하 게 보 느

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Booba saraxalekat bu mag ba jóg ak gàngooram gépp, maanaam kureelu Sadusen, ga fa dëkk. Kiñaan gu mag jàpp leen,

Korean

대 제 사 장 과 그 와 함 께 있 는 사 람 즉 사 두 개 인 의 당 파 가 다 마 음 에 시 기 가 가 득 하 여 일 어 나

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Waaye bi Yawut yi gisee mbooloo ma, ñu daldi fees ak kiñaan, di weddi li Pool di wax te di ko xas.

Korean

유 대 인 들 이 그 무 리 를 보 고 시 기 가 가 득 하 여 바 울 의 말 한 것 을 변 박 하 고 비 방 하 거

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Waaye léegi bàyyileen yii yépp: mer, xadar, kiñaan ak di génne ci seen gémmiñ sos ak wax ju ñaaw.

Korean

이 제 는 너 희 가 이 모 든 것 을 벗 어 버 리 라 곧 분 과 악 의 와 훼 방 과 너 희 입 의 부 끄 러 운 말 이

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Kon nanu màggal sunu Màggal, waxuma ak lawiir bu màggat biy misaal kiñaan ak lu bon, waaye ak mburu mu amul lawiir, maanaam ci xol bu laab ak ci dëgg.

Korean

이 러 므 로 우 리 가 명 절 을 지 키 되 묵 은 누 룩 도 말 고 괴 악 하 고 악 독 한 누 룩 도 말 고 오 직 순 전 함 과 진 실 함 의 누 룩 없 는 떡 으 로 하

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kiñaan, màndite ak xawaare ak yeneen yu ni mel. Léegi nag maa ngi leen di artu, ni ma ko defe woon: ñiy jëfe noonu duñu am cér ci nguuru Yàlla.

Korean

투 기 와, 술 취 함 과, 방 탕 함 과, 또 그 와 같 은 것 들 이 라 전 에 너 희 에 게 경 계 한 것 같 이 경 계 하 노 니 이 런 일 을 하 는 자 들 은 하 나 님 의 나 라 를 유 업 으 로 받 지 못 할 것 이

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Am na ñuy waare ci turu Kirist ci kaw kiñaan ak xëccoo, waaye ñi ci des ci kaw cofeel ak xol bu laab, ndaxte xam nañu ne, Yàlla moo ma teg fii, ngir ma taxawal xebaar bu baax bi.

Korean

어 떤 이 들 은 투 기 와 분 쟁 으 로 어 떤 이 들 은 착 한 뜻 으 로 그 리 스 도 를 전 파 하 나

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Pilaat nag xam ne, kiñaan rekk a taxoon saraxalekat yu mag yi jébbal ko Yeesu. Kon mu ne mbooloo mi: «Xanaa ma bàyyil leen buuru Yawut yi?»

Korean

빌 라 도 가 대 답 하 여 가 로 되 ` 너 희 는 내 가 유 대 인 의 왕 을 너 희 에 게 놓 아 주 기 를 원 하 느 냐 ?' 하

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Dangeen di mébét waaye dungeen am; dangeen di rey nit, boole ci kiñaan, waaye li ngeen di yóotu, dungeen ko jot; dangeen di xuloo ak a xeex waaye dungeen am dara, ndaxte ñaanuleen Yàlla.

Korean

너 희 가 욕 심 을 내 어 도 얻 지 못 하 고 살 인 하 고 시 기 하 여 도 능 히 취 하 지 못 하 나 니 너 희 가 다 투 고 싸 우 는 도 다 너 희 가 얻 지 못 함 은 구 하 지 아 니 함 이

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Seen xol fees na ak lu jubadi, lu bon, bëgge ak coxor; duñu xalaat lu dul kiñaan, rey nit, xuloo, njublaŋ ak ñaaw njort; dañuy jëw,

Korean

곧 모 든 불 의, 추 악, 탐 욕, 악 의 가 가 득 한 자 요 시 기, 살 인, 분 쟁, 사 기, 악 독 이 가 득 한 자 요, 수 군 수 군 하 는 자

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Waaye kiñaan tàbbi ca Yawut ya, ñu daldi jël ay taxawaalukat ca pénc ma, dajale mbooloo, ñuy yengal dëkk ba. Ñu daanu ci kër Yason, di wut Pool ak Silas, ngir dëj leen ci kanam waa dëkk ba.

Korean

그 러 나 유 대 인 들 은 시 기 하 여 저 자 의 어 떤 괴 악 한 사 람 들 을 데 리 고 떼 를 지 어 성 을 소 동 케 하 여 야 손 의 집 에 달 려 들 어 저 희 를 백 성 에 게 끌 어 내 려 고 찾 았 으

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
4,401,923,520 human contributions

Users are now asking for help:We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK