Results for kóolute translation from Wolof to Russian

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Russian

Info

Wolof

googu kóolute lanu am fa kanam yàlla ndax kirist.

Russian

Такую уверенность мы имеем в Боге через Христа,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

wax ju wóor a ngii, te mat a nangu ak gépp kóolute.

Russian

Слово сие верно и всякого принятия достойно.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag buleen sàggane kóolute gi ngeen am, ndaxte ëmb na yool bu mag.

Russian

Итак не оставляйте упования вашего, которому предстоит великое воздаяние.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

samay soppe, bu nu sunu xol daanul, kon man nanoo jege yàlla ak kóolute.

Russian

Возлюбленные! если сердце наше не осуждает нас, то мы имеем дерзновение к Богу,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag gannaaw wékku nanu ci yaakaar ju mel noonu, danuy waare ak kóolute gu mag.

Russian

Имея такую надежду, мы действуем с великим дерзновением,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon fees nanu ak kóolute, te yéenee jóge ci dëkkukaayu yaram wii, dem dëkk ci wetu boroom bi.

Russian

то мы благодушествуем и желаем лучше выйти из тела и водвориться у Господа.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon ni ma ame woon kóolute googu, naroon naa jëkk a jaar ci yéen, ngir ganesi leen ñaari yoon.

Russian

И в этой уверенности я намеревался придти к вамранее, чтобы вы вторично получили благодать,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte ku ci rafetal sasam dina am tur wu tedd ak kóolute gu mat sëkk ci yoonu ngëm, gi ci kirist yeesu.

Russian

Ибо хорошо служившие приготовляют себе высшую степень и великое дерзновение в вере во Христа Иисуса.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

maa ngi gërëm sunu boroom kirist yeesu, mi ma dooleel, ci kóolute gi mu am ci man, ba fal ma jawriñ.

Russian

Благодарю давшего мне силу, Христа Иисуса, Господа нашего, что Он признал меня верным, определив на служение,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ni kirist mel, noonu lanu mel nun itam ci àddina. ci loolu la mbëggeel mate sëkk ci nun, ngir nu am kóolute bésu àtte ba.

Russian

Любовь до того совершенства достигает внас, что мы имеем дерзновение в день суда, потому что поступаем в мире сем, как Он.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yëf yii leer na buur bi, moo tax maa ngi koy wax ak kóolute. wóor naa ne, dara ci lii may wax umpu ko, ndaxte lii amewul ciy ruq.

Russian

Ибо знает об этом царь, перед которым и говорю смело. Я отнюдь не верю, чтобы от него было что-нибудь из сегоскрыто; ибо это не в углу происходило.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yónniwaale nanu it sunu mbokk, mi nu seetlu cawarteem ay yooni yoon ci fànn yu bare, te mu gën koo fésal bii yoon ndax kóolute gu réy, gi mu am ci yéen.

Russian

Мы послали с ними и брата нашего, которого усердие многораз испытали во многом и который ныне еще усерднее по великой уверенности в вас.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeewuleen, di sax ci ñaan, ngir ngeen man a mucc ci loolu lépp war a xew, te man a taxaw ak kóolute ci kanamu doomu nit ki.»

Russian

итак бодрствуйте на всякое время и молитесь, дасподобитесь избежать всех сих будущих бедствий и предстать пред Сына Человеческого.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte xebaar bu baax, bi nu leen doon yégal, yemul woon ci ay wax rekk, waaye àndoon na ak kàttan ak xel mu sell mi ak kóolute gu mag. xam ngeen sunu taxawaay ci seen biir ngir seen njariñ.

Russian

потому что наше благовествование у вас было не в слове только, но и в силе и во Святом Духе, исо многим удостоверением, как вы сами знаете, каковы были мы для вас между вами.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye teewul boroom bi jox na ma kóolute ci yéen. biral na ma ne, dingeen bokk ak man xalaat. léegi nag, kiy nëxal seen xel, ku mu man a doon, yàlla dina ko mbugal.

Russian

Я уверен о вас в Господе, что вы не будете мыслить иначе; а смущающий вас, кто бы он ни был, понесет на себе осуждение.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte sama xënte ak sama yaakaar mooy ma bañ a rus ci lenn, waaye sama yaram feeñal ndamu kirist, ma ànd ci ak kóolute gu mat, su may dund mbaa may dee; moom laa daan def démb, te moom laay def tey.

Russian

при уверенности и надежде моей, что я ни в чем посрамлен не буду, но при всяком дерзновении, и ныне, как и всегда, возвеличится Христос в теле моем, жизнью ли то, или смертью.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

jaamu kirist, epafras, mi bokk ci yéen, mu ngi leen di nuyu. du jóg ci di leen ñaanal, farlu ci ni kuy bëre, ngir ngeen taxaw temm ci coobareg yàlla gépp, ànd ak ngëm gu mat ak kóolute gu wóor.

Russian

Приветствует вас Епафрас ваш, раб Иисуса Христа, всегда подвизающийся за вас в молитвах, чтобы вы пребыли совершенны и исполнены всем, что угодно Богу.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,945,104,741 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK