De traductores profesionales, empresas, páginas web y repositorios de traducción de libre uso.
na katika safari hiyo ilimbidi apitie samaria.
bi muy dem galile, waroon na jaar ci diiwaanu samari.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
ndiyo maana ilimbidi awe kama ndugu zake kwa kila namna, ili awe kuhani mkuu wao aliye mwaminifu na mwenye huruma katika kumtumikia mungu, ili dhambi za watu ziondolewe.
looloo taxoon mu war a mel niy doomi baayam ci bépp fànn, ngir doon seen saraxalekat bu mag fa kanam yàlla, bi leen yërëm te di sàmm kóllëre, te ci liggéeyu saraxaleem joxe na bakkanam ngir dindi bàkkaari nit ñi, ba yàlla baal leen.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
aliyaeleza na kuonyesha kwamba ilimbidi kristo kuteswa na kufufuka kutoka wafu. akawaambia, "yesu ambaye mimi namhubiri kwenu ndiye kristo."
mu di leen ko tekki, te di leen wax ay firnde yuy wone ne, fàww almasi bi sonn te dekki. mu ne leen: «yeesu, mi ma leen di yégal, mooy almasi bi.»
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
Advertencia: contiene formato HTML invisible