Usted buscó: mahakamani (Suajili - Wólof)

Contribuciones humanas

De traductores profesionales, empresas, páginas web y repositorios de traducción de libre uso.

Añadir una traducción

Suajili

Wólof

Información

Suajili

basi, akawafukuza kutoka mahakamani.

Wólof

noonu mu dàq leen ca àttekaay ba.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

mtu akikupeleka mahakamani kutaka kukuchukulia shati lako, mwache achukue pia koti lako.

Wólof

ku la bëgg a kalaame, ngir jël sa turki, nga boole ca it sa mbubb mu mag.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

jihadharini na watu, maana watawapeleka ninyi mahakamani na kuwapiga viboko katika masunagogi yao.

Wólof

waaye moytuleen nit ñi, ndaxte dinañu leen jébbal àttekat yi te dóor leen ay yar ci seeni jàngu.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

basi, walipofika hapa sikukawia, ila nilifanya kikao mahakamani kesho yake, nikaamuru mtu huyo aletwe.

Wólof

bi ñu àndee ak man ba fii nag, randaluma mbir mi, waaye ca ëllëg sa sax toog naa ca àttekaay ba, joxe ndigal, ñu indi nit kooku.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

lakini ninyi mnawadharau watu maskini! je, matajiri si ndio wanaowakandamizeni na kuwapeleka mahakamani?

Wólof

fekk dangeen leen di toroxal! xanaa du boroom alal yi ñoo leen di noot te di leen yóbbu fa kanam àttekat yi?

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

badala yake, kweli imekuwa mtindo ndugu kumpeleka ndugu yake mahakamani, tena mbele ya mahakimu wasioamini.

Wólof

waaye defuleen loolu; mbokk a ngi layoo ak moroomam, rax-ca-dolli ci kanamu ñi gëmul lañu koy defe!

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

sikujua la kufanya kuhusu shauri hilo. basi, nilimwuliza paulo kama angependa kwenda mahakamani kule yerusalemu kwa ajili ya mashtaka hayo.

Wólof

gannaaw lijjanti mbir moomu jafe woon na ma lool nag, ma laaj ko, ndax bëgg na dem yerusalem, layooji fa ci mbir yooyu.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

basi, watakapowapeleka ninyi mahakamani, msiwe na wasiwasi mtasema nini au namna gani; wakati utakapofika, mtapewa la kusema.

Wólof

boo xamee ne nag jébbale nañu leen, buleen am xel ñaar ci li ngeen di wax, mbaa ni ngeen koy waxe. ndaxte ca waxtu woowa sax dingeen jot li ngeen war a wax;

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

"lakini ninyi jihadharini. maana watu watawapelekeni mahakamani, na kuwapigeni katika masunagogi. mtapelekwa mbele ya watawala na wafalme kwa sababu yangu ili mpate kunishuhudia kwao.

Wólof

«moytuleen. dees na leen jébbal àttekat ya, di leen dóor ay yar ca jàngu ya. dinañu leen dëj ci kanamu ay boroom réew ak ay buur ndax sama tur, ngir ngeen nekk seede ci ñoom.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Advertencia: contiene formato HTML invisible

Suajili

lakini mimi nawaambieni, yeyote anayemkasirikia ndugu yake, lazima ahukumiwe. anayemdharau ndugu yake atapelekwa mahakamani. anayemwita ndugu yake: pumbavu atastahili kuingia katika moto wa jehanamu.

Wólof

waaye man maa ngi leen di wax ne, képp ku mere sa mbokk, dinañu la àtte. ku wax sa mbokk: “amoo bopp,” dinañu la àtte ca kureelu àttekat ya. ku ko wax: “alku nga,” dinañu la àtte ci safara.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

"patana na mshtaki wako upesi mkiwa bado njiani, kwenda mahakamani. la sivyo, mshtaki wako atakukabidhi kwa hakimu, naye hakimu atakukabidhi kwa askari, nawe utafungwa gerezani.

Wólof

«gaawal a juboo ak ki lay yóbbu, ngeen layooji, bala ngeen a egg; ngir bañ ki ngay layool jébbal la àttekat ba, kooka jox la alkaati ba, ñu tëj la.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Advertencia: contiene formato HTML invisible

Suajili

wakati huo paulo alikwisha tambua kwamba sehemu moja ya wanabaraza wale ilikuwa ni masadukayo na nyingine mafarisayo. basi, alipaaza sauti yake mbele ya baraza: "ndugu zangu, mimi ni mfarisayo, mwana wa mfarisayo. mimi nimeletwa mahakamani kwa kuwa ninatumaini kwamba wafu watafufuka."

Wólof

naka noona pool, mi xam ne, genn-wàllu kureel ga bokk nañu ci tariixab sadusen ya, te ña ca des bokk ci tariixab farisen ya, mu wax ci kaw ci biir géew ba ne: «bokk yi, man farisen laa, te farisen moo ma jur; li tax ñu may àtte tey mooy sama yaakaar ci ne, ñi dee dinañu dekki.»

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Advertencia: contiene formato HTML invisible

Obtenga una traducción de calidad con
8,040,540,628 contribuciones humanas

Usuarios que están solicitando ayuda en este momento:



Utilizamos cookies para mejorar nuestros servicios. Al continuar navegando está aceptando su uso. Más información. De acuerdo