De traductores profesionales, empresas, páginas web y repositorios de traducción de libre uso.
sikilizeni, nimekwisha kuwaonya kabla ya wakati.
wax naa leen ko lu jiitu.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
wakati nilipokuwa nikifanya hayo ndipo waliponikuta hekaluni, nilipokuwa nimekwisha fanya ile ibada ya kujitakasa. hakukuwako kundi la watu wala ghasia.
bi ma koy def nag, gis nañu ma ca kër yàlla ga, ma setlu ba noppi, fekk ànduma ak mbooloo te indiwuma benn coow.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
yesu akawaambia, "nimekwisha waambieni kwamba mimi ndiye. basi, kama mnanitafuta mimi, waacheni hawa waende zao."
mu ne leen: «wax naa leen ne, man la. bu fekkee ne nag man ngeen di seet, bàyyileen ñii ma àndal, ñu dem.»
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
Advertencia: contiene formato HTML invisible
naye, akiwa ndani angemjibu: usinisumbue! nimekwisha funga mlango. mimi na watoto wangu tumelala; siwezi kuamka nikupe!
«waaye kooku nekk ci biir néegam, dina ko tontu: “bu ma lakkal, tëj naa bunt bi ba noppi te tëdd, man ak sama njaboot; mënumaa jóg di la jox dara.”
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
basi, nendeni upesi mkawaambie wanafunzi wake kwamba amefufuka kutoka wafu, na sasa anawatangulieni kule galilaya; huko mtamwona. haya, mimi nimekwisha waambieni."
te ngeen dem bu gaaw, wax ay taalibeem ne, dekki na te jiituji na leen galile; foofa ngeen koy gise. lii laa leen wax.»
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
Advertencia: contiene formato HTML invisible
nami, kwa upande wangu, ingawa kwa mwili niko mbali nanyi, hata hivyo kwa roho niko hapo pamoja nanyi: na hivyo, kama vile nipo hapo, nimekwisha mhukumu huyo aliyefanya jambo hilo la aibu.
man nag, jëmm ji sore na leen, waaye xel mi mu ngi ci yéen, te àtte naa xaat kiy def loolu, ni su ma teewoon ci seen biir. dogal naa,
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad: