De traductores profesionales, empresas, páginas web y repositorios de traducción de libre uso.
sipendi mfikiri kwamba nataka kuwatisha ninyi kwa barua zangu.
ba tey bëgguma ngeen xalaat ne, maa ngi leen di xëbal ci samay bataaxal.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
ninayo bado mengi ya kukwambia, lakini sipendi kuyaandika kwa kalamu na wino.
am na lu bare, lu ma la bëggoona wax, waaye lépp xajul ci kayit.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
sipendi kupita kwenu harakaharaka na kuendelea na safari. natumaini kukaa kwenu kwa kitambo fulani, bwana akiniruhusu.
ndaxte fi mu ne bëgguma leen a gis rekk, jàll, waaye yaakaar naa ne, dinaa toog ci yéen ab diir, bu neexee boroom bi.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
ikiwa kuna mtu aliyemhuzunisha mwingine, hakunihuzunisha mimi--ila amewahuzunisha ninyi nyote, na sipendi kuwa mkali zaidi.
su kenn tegee moroomam naqar, du man la ko teg, waaye man nanu ne, yéen ñépp la ko teg — matul may réyal mbir mi.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
sipendi kuikataa neema ya mungu. kama mtu huweza kukubaliwa kuwa mwadilifu kwa njia ya sheria, basi, kristo alikufa bure!
duma neenal yiwu yàlla, ndaxte su sàmm yoon doon tax a jub fa kanam yàlla, kon kirist dee na cig neen.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
lakini sitafanya chochote bila kibali chako. sipendi kukulazimisha unisaidie, kwani wema wako unapaswa kutokana na hiari yako wewe mwenyewe na si kwa kulazimika.
waaye bëggumaa def dara loo àndul; noonu ndimbal li nga may defal du nekk sañul-bañ, waaye mu ànd ak xol bu tàlli.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
hata kidogo! ninachosema ni kwamba tambiko wanazotoa watu wasiomjua mungu wanawatolea pepo, sio mungu. sipendi kamwe ninyi muwe na ushirika na pepo.
déedéet! waaye sarax yi xërëmkat yi di rendi, ay rab lañu ko jagleel; jagleeluñu ko yàlla. te man bëgguma, ngeen booloo ak rab yi.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
kama ningetaka kujivuna singekuwa mpumbavu hata kidogo, maana ningekuwa nasema ukweli mtupu. lakini sitajivuna; sipendi mtu anifikirie zaidi ya vile anavyoona na kusikia kutoka kwangu.
su ma bëggoon a damu, du doon yëfi dof, ndaxte dëgg laay wax. waaye damay moytoo damu, ngir kenn bañ a foog ci man lu weesu li mu gis, may def, te muy dégg, ma di ko wax.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
basi, yesu aliwaita wanafunzi wake, akasema, "nawaonea watu hawa huruma kwa sababu kwa siku tatu wamekuwa nami, wala hawana chakula. sipendi kuwaacha waende bila kula wasije wakazimia njiani."
gannaaw loolu yeesu woo ci moom taalibeem ya ne leen: «yërëm naa mbooloo mi, ndaxte toog nañu fi man ñetti fan, te amatuñu lu ñu lekk. bëgguma leen a yiwi te lekkuñu, ngir bañ ñu tële ci yoon wi.»
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
Advertencia: contiene formato HTML invisible