De traductores profesionales, empresas, páginas web y repositorios de traducción de libre uso.
kwa hiyo msiogope; ninyi mu wa thamani kuliko shomoro wengi.
kon buleen ragal dara, yéena gën ndiiraanu rammatu.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
alipopata lulu moja ya thamani kubwa, alienda akauza yote aliyokuwa nayo, akainunua lulu ile.
am bés mu gis per buy jar njëg gu réy. mu dem nag, jaay li mu am lépp, jënd ko.»
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
mtu ana thamani kuliko kondoo! basi, ni halali kutenda mema siku ya sabato."
nit nag, ndax ëppul maana xar? kon def lu baax ci bésu noflaay bi jaadu na.»
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
Advertencia: contiene formato HTML invisible
je, tunaitumia imani kuibatilisha sheria? hata kidogo; bali tunaipa sheria thamani yake kamili.
xanaa kon ngëm day fanq yoonu musaa? mukk! da koy gën a dëgëral sax.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
ukuta huo ulikuwa umejengwa kwa mawe mekundu ya thamani, na mji wenyewe ulikuwa umejengwa kwa dhahabu safi, angavu kama kioo.
miir ba, jamaa lañu ko liggéeye, te dëkk ba di wurusu ngalam, leer ni weer bu set.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
juu ya msingi huo mtu anaweza kujenga kwa dhahabu, fedha au mawe ya thamani; anaweza kutumia miti, majani au nyasi.
ku tabax ci kaw fondamaa bi, wurus, xaalis, per, dénk, gittax walla boob,
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
baadhi ya wanafunzi walikuwa wanazungumza juu ya hekalu, jinsi lilivyopambwa kwa mawe ya thamani, pamoja na sadaka zilizotolewa kwa mungu. yesu akasema,
noonu ay nit doon wax ci lu jëm ca kër yàlla ga, ak ni ñu ko rafetale ak ay doj yu jafe ak alal ju ñu jébbal yàlla. waaye yeesu ne leen:
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
bali, uzuri wenu unapaswa kutokana na hali ya ndani ya utu wa kweli, uzuri usioharibika wa wema na utulivu wa roho, ambao ni wa thamani kubwa mbele ya mungu.
waaye nay taar bu sax bu nekk ci biir, di xol bu nooy te dal, ndax loolu lu takku la fa yàlla.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
mawe ya msingi wa ukuta huo yalikuwa yamepambwa kwa kila aina ya mawe ya thamani. jiwe la kwanza la msingi lilikuwa jiwe la thamani jekundu, la pili yakuti samawati, la tatu kalkedoni, la nne zamaradi,
fondamaay miiru dëkk ba rafetale nañu leen xeeti per yu nekk.fondamaa bu jëkk ba jamaa la;ñaareel ba, per bu bulo bu ñuy wax safir;ñetteel ba, per bu wert bu ñuy wax kalseduwan;ñeenteel ba, per bu wert te lerax, bu ñuy wax emëróot;
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
chukueni kwa mfano, kunguru: hawapandi, hawavuni wala hawana ghala yoyote. hata hivyo, mungu huwalisha. ninyi mna thamani zaidi kuliko ndege!
seetleen baaxoñ yi: duñu ji, duñu góob, amuñu dencukaay, amuñu sàq, teewul yàllaa ngi leen di dundal. céy ni ngeen ëppe maana picc yi!
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
kwenu ninyi mnaoamini, jiwe hilo ni la thamani kubwa; lakini kwa wale wasioamini, "jiwe walilokataa waashi, sasa limekuwa jiwe kuu la msingi."
kon nag yéen ñi gëm am ngeen cér ci teraangaam. waaye naka ñi gëmul:«doj wa tabaxkat ya sànni,mujj na di doju koñ.»
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
Advertencia: contiene formato HTML invisible
hakuna tena wa kununua dhahabu yao, fedha, mawe ya thamani na lulu, kitani na nguo za rangi ya zambarau, hariri na nguo nyekundu; vyombo vya kila aina ya miti ya pekee, vyombo vya pembe za ndovu, vya miti ya thamani kubwa, vya shaba, chuma na marmari;
seen wurus, seen xaalis, seeni jamaa ak yeneeni per; seeni piis yu rafet, piis yu yolet, yu ray-ray, yu xonq; seen dénk wu xeeñ, seen yëf yi ñu defare iwaar walla dénk wu jafe walla xànjar walla weñ walla marbar;
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad: