Vous avez cherché: don't say i wish say i will (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

but he shall say, i tell you, i know you not whence ye are; depart from me, all ye workers of iniquity.

Wolof

waaye dina ne: “nee naa leen xawma fu ngeen bokk. yéen ñépp soreleen ma, defkati lu bon yi!”

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

therefore say i unto you, the kingdom of god shall be taken from you, and given to a nation bringing forth the fruits thereof.

Wolof

«loolu moo tax maa ngi leen koy wax, dinañu leen xañ nguuru yàlla, dénk ko xeet wuy def ay jëfam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

as we said before, so say i now again, if any man preach any other gospel unto you than that ye have received, let him be accursed.

Wolof

wax nanu ko, maa ngi koy waxaat: bu leen kenn yégalee beneen xebaar bu dul bi ngeen nangu, kooku yal na alku!

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

yet ye have not known him; but i know him: and if i should say, i know him not, i shall be a liar like unto you: but i know him, and keep his saying.

Wolof

xamuleen ko nag; man maa ko xam. su ma ne woon xawma ko, ab fenkat laay doon ni yéen. waaye xam naa ko te maa ngi sàmm waxam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

if a man say, i love god, and hateth his brother, he is a liar: for he that loveth not his brother whom he hath seen, how can he love god whom he hath not seen?

Wolof

su kenn nee: «bëgg naa yàlla,» te bëgguloo sa mbokk, dangay fen; ndaxte ku bëggul sa mbokk mi ngay gis, doo man a bëgg yàlla mi nga gisul.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,792,344,158 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK