Vous avez cherché: baptisés (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

afin que personne ne dise que vous avez été baptisés en mon nom.

Wolof

ngir kenn bañ a wax ne, ci sama tur lañu ko sóob.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

sur ces paroles, ils furent baptisés au nom du seigneur jésus.

Wolof

bi ñu déggee loolu nag, sóob nañu leen ci ndox ci turu yeesu boroom bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

vous tous, qui avez été baptisés en christ, vous avez revêtu christ.

Wolof

yéen ñépp, ñi ñu sóob ci ndox ngir wone seen bokk ci kirist, soloo ngeen kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

qu`ils ont tous été baptisés en moïse dans la nuée et dans la mer,

Wolof

sóobu nañu ca ndoxu géej ga ak ca niir wa, ba bokk noonu ci musaa.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

moi, je vous ai baptisés d`eau; lui, il vous baptisera du saint esprit.

Wolof

maa ngi leen di sóob ci ndox, waaye moom dina leen sóob ci xel mu sell mi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car jean a baptisé d`eau, mais vous, dans peu de jours, vous serez baptisés du saint esprit.

Wolof

ndaxte yaxya daa na sóob nit ñi ci ndox, waaye yéen dees na leen sóob ci xel mu sell mi fi ak ay fan yu néew.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il dit: de quel baptême avez-vous donc été baptisés? et ils répondirent: du baptême de jean.

Wolof

mu ne leen: «kon nag, bi ñu leen sóobee ci ndox, lu ciy maana?» Ñu tontu ko: «xanaa li yaxya tëral.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il vint aussi des publicains pour être baptisés, et ils lui dirent: maître, que devons-nous faire?

Wolof

ay juutikat itam ñëw ca yaxya, ngir mu sóob leen ci ndox; ñu ne ko: «kilifa gi, lu nu war a def?»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car il n`était encore descendu sur aucun d`eux; ils avaient seulement été baptisés au nom du seigneur jésus.

Wolof

ndaxte wàccagul ci kenn ci ñoom, waaye sóoboon nañu leen rekk ci ndox ci turu boroom bi yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et je me souvins de cette parole du seigneur: jean a baptisé d`eau, mais vous, vous serez baptisés du saint esprit.

Wolof

bi loolu amee ma fàttaliku li boroom bi wax ne: “yaxya ci ndox la daan sóobe, waaye yéen dees na leen sóob ci xel mu sell mi.”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

cependant crispus, le chef de la synagogue, crut au seigneur avec toute sa famille. et plusieurs corinthiens, qui avaient entendu paul, crurent aussi, et furent baptisés.

Wolof

kirispus nag, njiitu jàngu ba, gëm na boroom bi ak waa këram gépp. te waa korent ñu bare dégg kàddu gi te gëm ko, ñu sóob leen ci ndox.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

alors jésus vint de la galilée au jourdain vers jean, pour être baptisé par lui.

Wolof

booba yeesu jóge galile, ñëw ngir yaxya sóob ko ca dexu yurdan.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,782,215,629 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK