Vous avez cherché: donne moi (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

donne moi

Wolof

Dernière mise à jour : 2023-10-12
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

une femme de samarie vint puiser de l`eau. jésus lui dit: donne-moi à boire.

Wolof

noonu jigéenu waa samari ñëw fa di root. yeesu ne ko: «may ma ndox, ma naan.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

a l`instigation de sa mère, elle dit: donne-moi ici, sur un plat, la tête de jean baptiste.

Wolof

noonu ndaw sa daldi topp la ko ndey ji digaloon, ne erodd: «indil ma fii ci biir ndab boppu yaxya.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

le plus jeune dit à son père: mon père, donne-moi la part de bien qui doit me revenir. et le père leur partagea son bien.

Wolof

benn bés caat ma ne baay ba: “baay, damaa bëggoon, nga jox ma li may war a féetewoo ci ndono li.” noonu baay ba daldi leen séddale alalam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

la femme lui dit: seigneur, donne-moi cette eau, afin que je n`aie plus soif, et que je ne vienne plus puiser ici.

Wolof

noonu jigéen ja daldi ko ne: «sang bi, may ma ci ndox moomu, ngir ma bañatee mar, bay ñëw ba fii di rootsi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

jésus lui répondit: si tu connaissais le don de dieu et qui est celui qui te dit: donne-moi à boire! tu lui aurais toi-même demandé à boire, et il t`aurait donné de l`eau vive.

Wolof

noonu nag yeesu tontu ko: «soo xamoon li yàlla maye, xam ki lay ñaan ndox, kon yaw ci sa bopp, yaa koy ñaan, te moom dina la may ndoxum dund.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,776,154,974 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK