Vous avez cherché: fruits (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

c`est donc à leurs fruits que vous les reconnaîtrez.

Wolof

ci seeni jëf nag ngeen leen di xàmmee.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il faut que le laboureur travaille avant de recueillir les fruits.

Wolof

noonu it beykat bi sonn mooy jëkk a ñam toolam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

tout arbre qui ne porte pas de bons fruits est coupé et jeté au feu.

Wolof

garab gu nekk gu dul meññ doom yu neex, dees na ko gor, sànni ko ca safara sa.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

tout bon arbre porte de bons fruits, mais le mauvais arbre porte de mauvais fruits.

Wolof

noonu garab gu baax gu nekk dina meññ doom yu neex, waaye garab gu bon dina meññ doom yu bon.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

un bon arbre ne peut porter de mauvais fruits, ni un mauvais arbre porter de bons fruits.

Wolof

garab gu baax mënul a meññ doom yu bon, naka itam garab gu bon mënul a meññ doom yu neex.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

déjà la cognée est mise à la racine des arbres: tout arbre donc qui ne produit pas de bons fruits sera coupé et jeté au feu.

Wolof

sémmiñ wi tiim na reeni garab yi. garab nag gu meññul doom yu baax, dees na ko gor, sànni ko ci safara si.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

celui qui moissonne reçoit un salaire, et amasse des fruits pour la vie éternelle, afin que celui qui sème et celui qui moissonne se réjouissent ensemble.

Wolof

kiy góob tool yi mu ngi jot xaat peyam; day dajale nit ñi ngir dund gu dul jeex, ni ñuy dajalee pepp. kon boog kiy ji dina bégandoo ak kiy góob.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

les fruits que désirait ton âme sont allés loin de toi; et toutes les choses délicates et magnifiques sont perdues pour toi, et tu ne les retrouveras plus.

Wolof

dinañu wax naan: «yëf yi nga bëggoon a am raw nañu la, te lépp luy yafal walla col gu rafet ñàkk nga ko, te kenn du ko gisaat!»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

celui qui fournit de la semence au semeur, et du pain pour sa nourriture, vous fournira et vous multipliera la semence, et il augmentera les fruits de votre justice.

Wolof

yàlla miy jox beykat bi jiwu ak nit ab dund, dina leen jox jiwu wu ne gàññ, te sakkanal li seen njub meññ.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

au milieu de la place de la ville et sur les deux bords du fleuve, il y avait un arbre de vie, produisant douze fois des fruits, rendant son fruit chaque mois, et dont les feuilles servaient à la guérison des nations.

Wolof

xellee ca digg péncu dëkk ba. ca weti dex ga amoon na ca garabu dund, guy meññ fukki yoon ak ñaar, di meññ weer wu nekk, te xob ya di faj xeet yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

mais le fruit de l`esprit, c`est l`amour, la joie, la paix, la patience, la bonté, la bénignité, la fidélité, la douceur, la tempérance;

Wolof

waaye li xelu yàlla mi di meññ mooy: mbëggeel, mbég, jàmm, muñ, laabiir, mbaax, kóllëre,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,775,861,713 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK