Vous avez cherché: impossible (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

car rien n`est impossible à dieu.

Wolof

ndaxte dara tëwul yàlla.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

impossible d'obtenir des informations sur le crtc %d

Wolof

maneesul a ami xibaar ci crtc %d

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car il est impossible que le sang des taureaux et des boucs ôte les péchés.

Wolof

ndaxte deretu yëkk yi ak ju sikket yi mënuñoo dindi bàkkaar yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

jésus les regarda, et leur dit: aux hommes cela est impossible, mais à dieu tout est possible.

Wolof

noonu yeesu xool leen ne: «loolu të na nit, waaye dara tëwul yàlla.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car il est impossible que ceux qui ont été une fois éclairés, qui ont goûté le don céleste, qui ont eu part au saint esprit,

Wolof

li nu war a jëme kanam mooy lii: su amee ay nit ñu yàlla xas a leeral ba noppi, ñu mos mayu yàlla gi, am wàll ci xelam mu sell,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

jésus les regarda, et dit: cela est impossible aux hommes, mais non à dieu: car tout est possible à dieu.

Wolof

noonu yeesu xool leen naan: «loolu të na nit, waaye tëwul yàlla; yàlla man na lépp.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

impossible d'obtenir des informations sur la sortie %dposition", "size", and "maximum

Wolof

maneesul a ami xibaar ñeel génn gu %dposition", "size", and "maximum

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Français

jésus dit à ses disciples: il est impossible qu`il n`arrive pas des scandales; mais malheur à celui par qui ils arrivent!

Wolof

yeesu waxaat ay taalibeem ne leen: «fiir yuy yóbbe nit bàkkaar mënta ñàkk, waaye toroxte dal na ki koy lal.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

afin que, par deux choses immuables, dans lesquelles il est impossible que dieu mente, nous trouvions un puissant encouragement, nous dont le seul refuge a été de saisir l`espérance qui nous était proposée.

Wolof

noonu ñaari jëf yooyu nga xam ne duñu tebbiku te yàlla mënu cee dellu gannaaw, dañu nuy gën a sóob ci muñ, nun ñi daw ba am kiiraay, ngir nu man a téye bu dëgër yaakaar, ji mu nu dig.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

c`est à cause de votre incrédulité, leur dit jésus. je vous le dis en vérité, si vous aviez de la foi comme un grain de sénevé, vous diriez à cette montagne: transporte-toi d`ici là, et elle se transporterait; rien ne vous serait impossible.

Wolof

yeesu tontu leen ne: «seen ngëm gu néew a tax. ci dëgg maa ngi leen koy wax, su ngeen amee ngëm gu tuuti sax niw peppu fuddën, kon dingeen ne tund wii: “jógeel fii, toxu fale,” te dina fa dem, ba dara du leen të.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,800,374,068 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK