Vous avez cherché: je me, porte bien (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

je me base les couilles

Wolof

je me base les couilles

Dernière mise à jour : 2023-05-28
Fréquence d'utilisation : 2
Qualité :

Français

je me dois aux grecs et aux barbares, aux savants et aux ignorants.

Wolof

am naa warugar sama diggante ak ñépp, muy ñi jàng ni gereg yi, muy ñi jàngul ni baarbaar yi, ñi bare xam-xam ak ñi barewul xam-xam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

je me réjouis de pouvoir en toutes choses me confier en vous.

Wolof

bég naa, ndaxte xam naa ne, man naa leen a wóolu ci lu nekk!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

lorsque je me fus mis à parler, le saint esprit descendit sur eux, comme sur nous au commencement.

Wolof

«bi ma tàmbalee wax nag, xel mu sell mi wàcc ci ñoom, ni mu wàcce woon ci nun bu jëkk.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car, si je rebâtis les choses que j`ai détruites, je me constitue moi-même un transgresseur,

Wolof

waaye su ma delloo di sàmm ndigali yoon, yi ma bàyyi, dëgg-dëgg dinaa wone noonu ne, moykatu yoon wi laa.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et je me sanctifie moi-même pour eux, afin qu`eux aussi soient sanctifiés par la vérité.

Wolof

sellal naa sama bopp ngir ñoom, ngir ñu sampu ci dëgg te sell.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

je me réjouis de la présence de stéphanas, de fortunatus et d`achaïcus; ils ont suppléé à votre absence,

Wolof

bi ma estefanas ak fortunatus ak akaykus seetsee, bég naa ci lool. taxawal nañu leen ci topptoo, bi ngeen yéene woon ci man te tële ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

c`est dans ce but que je me rendis à damas, avec l`autorisation et la permission des principaux sacrificateurs.

Wolof

«noonu am bés, may dem dëkku damas, yor sañ-sañ ak ndigalu saraxalekat yu mag ya.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et même si je sers de libation pour le sacrifice et pour le service de votre foi, je m`en réjouis, et je me réjouis avec vous tous.

Wolof

te bu sama deret waree tuuru sax, ngir seen ngëm mat sëkk, ma mel ni naan gu ñu boole ak sarax su jëm ci yàlla, ba tey bég naa ci, te dinaa ci bégati.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et je me souvins de cette parole du seigneur: jean a baptisé d`eau, mais vous, vous serez baptisés du saint esprit.

Wolof

bi loolu amee ma fàttaliku li boroom bi wax ne: “yaxya ci ndox la daan sóobe, waaye yéen dees na leen sóob ci xel mu sell mi.”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

bien aimés, comme je désirais vivement vous écrire au sujet de notre salut commun, je me suis senti obligé de le faire afin de vous exhorter à combattre pour la foi qui a été transmise aux saints une fois pour toutes.

Wolof

samay bokk, bëggoon naa leen a bind lool ci mbirum mucc gi nu bokk, waaye lii moo gën a jamp: ma xiir leen, ngeen taxaw ci aar mboolem dëgg, yi yàlla xas a dénk gaayam yu sell yi ba fàww.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

ce n`est pas en vue de mes besoins que je dis cela, car j`ai appris à être content de l`état où je me trouve.

Wolof

ba tey soxla taxul ma waxe nii, ndaxte jàng naa doylu ci mbir mu ma man a dab.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

j`espère vous voir en passant, quand je me rendrai en espagne, et y être accompagné par vous, après que j`aurai satisfait en partie mon désir de me trouver chez vous.

Wolof

bu may dem espaañ nag, bëgg naa faa jaar, nuyu leen; ndaxte ay at a ngii maa ngi am yéene ju tar ci ñëw seetsi leen. bëgg na maa nekk ci seen biir, ngir am bànneexu sotteente ak yéen xalaat ab diir, te it ngeen waajalal ma sama yoonu espaañ.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et Ésaïe pousse la hardiesse jusqu`à dire: j`ai été trouvé par ceux qui ne me cherchaient pas, je me suis manifesté à ceux qui ne me demandaient pas.

Wolof

te esayi takk na fitam, ba wax ne:«Ñi ma wutul woon, gis nañu ma,feeñ naa ci ñi ma laajul woon.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

c`est pourquoi je me plais dans les faiblesses, dans les outrages, dans les calamités, dans les persécutions, dans les détresses, pour christ; car, quand je suis faible, c`est alors que je suis fort.

Wolof

looloo tax may bég ci néew doole, yi may wéye ngir turu kirist, ciy tiis, ciy njàqare, mbaa ñu saaga ma, mbaa ñu fitnaal ma. ndaxte bu ma néewee doole, booba laay am kàttan.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

celui qui a mes commandements et qui les garde, c`est celui qui m`aime; et celui qui m`aime sera aimé de mon père, je l`aimerai, et je me ferai connaître à lui.

Wolof

ki ma bëgg, mooy kiy nangu samay ndigal te di ko topp. ku ma bëgg, baay bi bëgg la, te man dinaa la bëgg, di la feeñu.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,781,967,207 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK