Vous avez cherché: mal à la tête (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

les passants l`injuriaient, et secouaient la tête,

Wolof

Ña fa doon romb di ko xas, di wëcc seen bopp ndax sib ko,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

tout homme qui prie ou qui prophétise, la tête couverte, déshonore son chef.

Wolof

kon nag góor guy ñaan yàlla, walla muy wax ci kàddug yàlla, fekk mu teg dara ci boppam, day suufeel kirist, kilifaam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il envoya de nouveau vers eux un autre serviteur; ils le frappèrent à la tête, et l`outragèrent.

Wolof

mu yónniwaat beneen surga, waaye ñu dóor ko ci bopp, toroxal ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

c`est pourquoi la femme, à cause des anges, doit avoir sur la tête une marque de l`autorité dont elle dépend.

Wolof

looloo tax jigéen war a teg ci kaw boppam luy màndargaal kilifteef ga, ndax malaaka yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

simon pierre lui dit: seigneur, non seulement les pieds, mais encore les mains et la tête.

Wolof

simoŋ piyeer ne ko: «kon nag boroom bi, bul yem rekk ci tànk yi, waaye raxasaaleel loxo yi ak bopp bi!»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

je vous invite donc à prendre de la nourriture, car cela est nécessaire pour votre salut, et il ne se perdra pas un cheveux de la tête d`aucun de vous.

Wolof

maa ngi leen di sant nag, ngeen lekk, ndax noonu rekk ngeen man a rawe. ndax genn kawar du rot ci yéen.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et ils lui frappaient la tête avec un roseau, crachaient sur lui, et, fléchissant les genoux, ils se prosternaient devant lui.

Wolof

Ñu di ko dóor ci bopp ak bant, di ko tifli, daldi sukk, màggal ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il envoya sur-le-champ un garde, avec ordre d`apporter la tête de jean baptiste.

Wolof

mu daldi yónni nag xarekat, jox ko ndigal, mu indil ko boppu yaxya. waa ji dem, dagg boppu yaxya ca kaso ba,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et elle vit deux anges vêtus de blanc, assis à la place où avait été couché le corps de jésus, l`un à la tête, l`autre aux pieds.

Wolof

séen ñaari malaaka yu sol mbubb yu weex, toog ca bérab, ba ñu dencoon yeesu; kenn ka féeteek bopp bi, ki ci des ca tànk ya.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

a l`instigation de sa mère, elle dit: donne-moi ici, sur un plat, la tête de jean baptiste.

Wolof

noonu ndaw sa daldi topp la ko ndey ji digaloon, ne erodd: «indil ma fii ci biir ndab boppu yaxya.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

elle s`empressa de rentrer aussitôt vers le roi, et lui fit cette demande: je veux que tu me donnes à l`instant, sur un plat, la tête de jean baptiste.

Wolof

mu daldi gaawantoo dugg nag ci kanamu buur bi ne ko: «damaa bëgg, nga indil ma léegi boppu yaxya ci biir ndab.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

néanmoins, parce que cette veuve m`importune, je lui ferai justice, afin qu`elle ne vienne pas sans cesse me rompre la tête.

Wolof

waaye jigéen jii lakkal na ma; kon dinaa ko àtte, ngir mu bañatee ñëw sonal ma. dina rey ak ay wax.”»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

toute femme, au contraire, qui prie ou qui prophétise, la tête non voilée, déshonore son chef: c`est comme si elle était rasée.

Wolof

waaye bu jigéen musóoruwul, buy ñaan walla buy wax ci kàddug yàlla, kooku day suufeel jëkkëram jiy kilifaam, ndaxte day mel ni jigéen ju ñu wat.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

les passants l`injuriaient, et secouaient la tête, en disant: hé! toi qui détruis le temple, et qui le rebâtis en trois jours,

Wolof

Ña fa doon romb di ko xas, di wëcc seen bopp ndax sib ko naan: «waaw kay, yaw mi bëgg a toj kër yàlla gi, tabaxaat ko ci ñetti fan,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

comme jésus était à béthanie, dans la maison de simon le lépreux, une femme entra, pendant qu`il se trouvait à table. elle tenait un vase d`albâtre, qui renfermait un parfum de nard pur de grand prix; et, ayant rompu le vase, elle répandit le parfum sur la tête de jésus.

Wolof

bi nga xamee ne yeesu nekkoon na dëkku betani, mu dem këru simoŋ ma gaana woon, di fa lekk. noonu jigéen ñëw, yor njaq lu ñu defare doj wu tudd albaatar. njaq li def latkoloñ ju raxul ju ñuy wax nàrd, tey jar lu baree-bare. jigéen ji toj njaq li, tuur latkoloñ ci boppu yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,792,754,323 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK