Vous avez cherché: pécheurs (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

je ne suis pas venu appeler à la repentance des justes, mais des pécheurs.

Wolof

Ñëwuma ngir woo ñi jub, waaye ngir woo bàkkaarkat yi, ñu tuub seeni bàkkaar.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

nous, nous sommes juifs de naissance, et non pécheurs d`entre les païens.

Wolof

nun danoo cosaanoo ci xeetu yawut, te bokkunu ci xeet, yi xamul yàlla tey bàkkaar.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

mais dieu prouve son amour envers nous, en ce que, lorsque nous étions encore des pécheurs, christ est mort pour nous.

Wolof

waaye yàlla firndeel na mbëggeelam ci nun, ci li kirist dee ngir nun, bi nu nekkee sax ay bàkkaarkat!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

si vous aimez ceux qui vous aiment, quel gré vous en saura-t-on? les pécheurs aussi aiment ceux qui les aiment.

Wolof

«su ngeen soppee ñi leen sopp, ban ngërëm ngeen ciy am? ndaxte bàkkaarkat yi sax sopp nañu ñi leen sopp.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

allez, et apprenez ce que signifie: je prends plaisir à la miséricorde, et non aux sacrifices. car je ne suis pas venu appeler des justes, mais des pécheurs.

Wolof

mbind mi nee na: “yërmande laa bëgg, waaye du rendi saraxi mala.” demleen nag te seet lu wax joojuy tekki. ndaxte ñëwuma, ngir woo ñi jub, waaye bàkkaarkat yi laay woo.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

approchez-vous de dieu, et il s`approchera de vous. nettoyez vos mains, pécheurs; purifiez vos coeurs, hommes irrésolus.

Wolof

jegeleen yàlla, mu jege leen. yéen bàkkaarkat yi, sellal-leen seeni loxo; yéen ñi am xel ñaar, laabal-leen seeni xol.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car, comme par la désobéissance d`un seul homme beaucoup ont été rendus pécheurs, de même par l`obéissance d`un seul beaucoup seront rendus justes.

Wolof

aadama moomu dafa déggadil yàlla, ba yóbbaale ñu bare, ñu nekk i bàkkaarkat; noonu itam yeesu kirist dafa déggal yàlla, yóbbaale ñu bare itam, ñu jub.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

de même, je vous le dis, il y a de la joie devant les anges de dieu pour un seul pécheur qui se repent.

Wolof

maa ngi leen di wax lii: ci noonule la malaakay yàlla yi di ame mbég ci benn bàkkaarkat bu tuubee ay bàkkaaram.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,086,518 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK