Vous avez cherché: paille (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

hypocrite, ôte premièrement la poutre de ton oeil, et alors tu verras comment ôter la paille de l`oeil de ton frère.

Wolof

naaféq, jëkkal a dindi gànj gi ci sa bët, te noonu dinga man a gis bu leer, ngir dindi ñax gi ci sa bëtu mbokk.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

ou comment peux-tu dire à ton frère: laisse-moi ôter une paille de ton oeil, toi qui as une poutre dans le tien?

Wolof

walla nan ngay waxe sa mbokk: “may ma, ma dindil la ñax gi ci sa bët,” fekk gànj a ngii ci sa bët yaw?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il a son van à la main; il nettoiera son aire, et il amassera le blé dans son grenier, mais il brûlera la paille dans un feu qui ne s`éteint point.

Wolof

layoom mu ngi ci loxoom, ngir jéri dàgga ja, ba mu set; pepp ma dina ko def ca sàqam, waaye xatax ba dina ko lakk ci safara su dul fey mukk.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

pourquoi vois-tu la paille qui est dans l`oeil de ton frère, et n`aperçois-tu pas la poutre qui est dans ton oeil?

Wolof

«lu tax ngay xool ñax gi ci sa bëtu mbokk, te gisuloo gànj gi ci sa bët yaw?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 2
Qualité :

Français

ou comment peux-tu dire à ton frère: frère, laisse-moi ôter la paille qui est dans ton oeil, toi qui ne vois pas la poutre qui est dans le tien? hypocrite, ôte premièrement la poutre de ton oeil, et alors tu verras comment ôter la paille qui est dans l`oeil de ton frère.

Wolof

nan nga man a waxe sa mbokk: “sama xarit, may ma, ma dindil la ñax gi ci sa bët,” yaw mi gisul gànj gi nekk ci sa bët? naaféq! jëkkal a dindi gànj gi ci sa bët, te noonu dinga man a gis bu leer, ngir dindi ñax gi ci sa bëtu mbokk.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,790,776,226 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK