Vous avez cherché: que allah te pardonne tes péchés (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

et il dit à la femme: tes péchés sont pardonnés.

Wolof

yeesu daldi ne jigéen ja: «baal nañu la say bàkkaar.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

qu'allah te protège et te donne une longue vie in sha allah

Wolof

Dernière mise à jour : 2024-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

voyant leur foi, jésus dit: homme, tes péchés te sont pardonnés.

Wolof

bi yeesu gisee seen ngëm, mu ne làggi ba: «sama waay, baal nañu la say bàkkaar.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

jésus, voyant leur foi, dit au paralytique: mon enfant, tes péchés sont pardonnés.

Wolof

bi yeesu gisee seen ngëm, mu ne làggi ba: «sama waay, baal nañu la say bàkkaar.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et maintenant, que tardes-tu? lève-toi, sois baptisé, et lavé de tes péchés, en invoquant le nom du seigneur.

Wolof

léegi nag, looy nég? jógal, ñu sóob la ci ndox, nga set ci say bàkkaar ci tudd turu yeesu.”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

lequel est le plus aisé, de dire: tes péchés te sont pardonnés, ou de dire: lève-toi, et marche?

Wolof

ma wax ne: “baal nañu la say bàkkaar,” walla ma ne: “jógal te dox,” lan moo ci gën a yomb?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car, lequel est le plus aisé, de dire: tes péchés sont pardonnés, ou de dire: lève-toi, et marche?

Wolof

ma wax ne: “baal nañu la say bàkkaar,” walla ma ne: “jógal te dox,” lan moo ci gën a yomb?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et voici, on lui amena un paralytique couché sur un lit. jésus, voyant leur foi, dit au paralytique: prends courage, mon enfant, tes péchés te sont pardonnés.

Wolof

foofa ñu indil ko ku tëdd ci basaŋ, fekk yaramam wépp làggi. bi yeesu gisee seen ngëm, mu ne ku làggi ka: «na sa xel dal, sama waay, baal nañu la say bàkkaar.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,781,447,597 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK